Youssou N'Dour - Tatagal paroles de chanson

paroles de chanson Tatagal - Youssou N'Dour



Tatagal Bu ko jot gi may e woon
Weer wu ne ma ñëw
Sagaal sama fan's yi
Sant leen, sargal leen
Ni bu leen di sonn al béer
Njaw du mel ni lem
Jimmy mbaye xalam al leen
Te encourager leen leen
Bu ko jot gi may e woon
Weer wu ne ma wëy
Sagaal sama fan's yi
Sant leen, sargal leen
Ma nii bu leen di sonn al béer
Njaw du mel ni lem
Jimmy mbaye xalam al leen
Te encourager leen leen
Na ñu leen xalam al
Na ñu leen tatagal
Na ñu leen woy al
Na ñu leen sargal
Na ñu leen xalam al
Na ñu leen tatagal
Na ñu leen woy al
Na ñu leen sargal
Na ñu leen xalam al
Na ñu leen tatagal
Na ñu leen woy al
Na ñu leen sargal
Je vous salue
Avec tous les honneurs
Et vous souhaite
Que du bonheur
Ces fans de valeurs
Qui m'attendent des heures
Je vous ai dans mon cœurs
Vous méritez, d'être ova tionnés,
C'est ça la vérité
Vous êtes toujours
Quoiqu'il puisse arriver
Yéen ay sama y soppe
Ànd bi yagg na
Confiance bi rëy na
Tatagal leen jaadu na
Njukkël leen war na
Fu nda pare ngen
ñu dem wër adduna
Da ma ni pare naa
Te it sax defe naa
Xalaat bi jaadu na
Su ma leen
Mën oon a jox loxo
Yegsi naa
Su ma leen mën oon seet si
Yegsi naa
Fatte wu ma leen
Déedéet mën ul am Yëg naa leen
Sallaaw mooy li wóor
Fan's yi xam ci jamono
Naw naa seen taxawaay
Moo tax ma jóg
Sargal leen, woy ee
Bul gnu leen
Fatte di bëgguel
Naw naa seen taxawaay
Moo tax ma jóg
Sargal leen, woy ee
Fan's yi xam ci jamono
Naw naa seen taxawaay
Moo tax ma jóg
Sargal leen, woy ee
Bul gnu
Leen fatte di bëgguel
Naw naa seen taxawaay
Moo tax ma jóg
Sargal leen, woy ee




Youssou N'Dour - MBALAX
Album MBALAX
date de sortie
12-11-2021




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.