Youssou N'Dour - New Africa paroles de chanson

paroles de chanson New Africa - Youssou N'Dour



Mane Youssou Ndour!
Ma ngi wo! bépeu domi Africaaaa!
Gnou bokeu khalate!
Bokeu guiss guiss!
Bokou yénéééééé!
Sans frontiéres
Bolé sounouy ame ame
liguééééy!
Wara tougnou
Nangou kéne nieuw
Dignou féwaléééééééééé!
Boul djité rew
Fok la fa nek
Yaw ya ko mome!
Ndite bou deugueur
Dafa wara fek nga beug sa rew
sakou ndimbeul
Ndimbeul na sa fek
Lokhoy boroooom!
Woy Africa!
Bou dianteu bi finké waw!
Na la fek diok!
Ak sa dioumetou kaye!
Beuthieuk bi gaw neu!
Niéteu dou beuré
niarra meuneu kééééneu waw!
Yone wi! sorré na!
métti na
Naniou ko waaadial
Bo doul nopé khalate
La niou défone Mameuuuu ya!
Sa khol do toul nekh
dotou khame lou doul féyane to!
Souma sagnone Africa
Béne niit mo koy djité!
Niou bolé
Sounouy khalate
Ak sounouy dolé
Diokh ko!
Naniou oubi frontiers yi! ratakhale yone yi
Ba nieupeu guissé
Changes your thinking!
Work together!
Keep and working!
Cheikh Anta Diop!
Kouamé Nkrumah!
Steven Biko!
All you people!
Africa!



Writer(s): H FAYE, Y N'DOUR


Youssou N'Dour - Eyes Open
Album Eyes Open
date de sortie
01-06-1992




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.