Youssou N'Dour - Serin Fallu paroles de chanson

paroles de chanson Serin Fallu - Youssou N'Dour



Serigne Fallou moye mbegoug mouride yi louweer
Buur Yalla mokodeff thi khol
Nioune mouridou laye Gallas laniou bégué
Bouwerr
Gallas bayou Mbéne meunané nieup la saff
Bouniou ko toudé souniou khol yi daye nekh
Nioune mouridou laye Gallas laniou bégué
Kassourajab
Kep kouy talibé amnga Serigne bou matt seuk
Mouy sa wassila si yonou Bamba
Wayé ko thi khar kholam Serigne Fallou laye bégué
Bou werr
Mane lima khir thi mom billah khaoumako sakh
Fouma diakhlei Serigne Fallou laye wo
Mane Youssou Magnick Sene Serigne Fallou laye bégué
Lou wéreu
Taye ma khamal léne mane Youssou sama secret
Louma tambalé Serigne Fallou laye wo diourom niari yone fekk balba takkna
Lou wereu werr
Loumou wakh mou am Serigne Fallou Yalla koko maye
Bayou Serigne Bara bayou Serigne Abo bayou Sokhna Mou musique laniou bégué
Serigne Fallou Mbacké
Yallako bolé thi kharitam
Boune waw mou am
Bouné dou am dara dou am
Mo ndieukeu muré armel yi indifi courant Yégali dioumay Touba ba noppi djiteiniou
Dieul diouromeli sorodo toudei Lamp Fall Lamp baboul Mouridina mbeur degna Demba
Bayou Mouna Fall bayou Assane Fall Narou Guewsara Fall
Cheikh Fallou
Neu nieup diouk yenguetou Fallou diarnako (×2)
Serigne Fallou niwone maye Sénégal kou weidi ladjal Senghor domou Yaye Gnilane dieu
Serigne Fallou mo santhie Ndindi
Serigne Fallou di deff di dindi
Serigne Fallou kou reer mou gindi
Serigne Fallou moye Sénégal (×2)
Batine beu rayneu
Nguenel yeu feigna
Bakham ga siwna
Beguel ngue rewmé
Cheikh Fallou nieuwneu
Noflaye ga nieuwna
Khewal yeu doyna
Beguelnga rewmé
Wayé dou diambat
Cheikh Fallou da matt matalé rew mi Cheikh Fallou daram dou mankei douy deff mouy mankei da fonk rewmé
Mo ndieukeu muré armel yi indifi goudron Yégali dioumay Touba ba noppi djiteiniou
Dieul diouromeli sorodo toudei Lamp Fall Lamp baboul Mouridina mbeur degna Demba
Bayou Mouna Fall bayou Assane Fall Narou Guewsara Fall
Serigne Fallou mo santhie Ndindi
Serigne Fallou di deff di dindi
Serigne Fallou kou reer mou gindi
Serigne Fallou moye Sénégal (×2)
Na nieup diouk yeguentou Fallou diarnako (×9)



Writer(s): youssou n'dour


Youssou N'Dour - Africa Rekk
Album Africa Rekk
date de sortie
04-11-2016




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.