Youssou N'Dour feat. Faada Freddy - Dara du KO daqq - traduction des paroles en anglais

Paroles et traduction Youssou N'Dour feat. Faada Freddy - Dara du KO daqq




Dara du KO daqq
The Child of the Country
Sopp nala nguir seu yiw
We pray for your peace
Sopp nala nguir seu dal
We pray for your prosperity
Sopp nala nguir seu téranga
We pray for your hospitality
"Wawaw ndour"
"Wawaw ndour"
Sopp nala nguir seu yiw
We pray for your peace
Sopp nala nguir seu dal
We pray for your prosperity
Sopp nala nguir seu téranga
We pray for your hospitality
"Wawaw"
"Wawaw"
Sopp nala nguir seu yiw
We pray for your peace
Sopp nala nguir seu dal
We pray for your prosperity
Sopp nala nguir seu téranga
We pray for your hospitality
Sét lou nala yaw mi sét lou nala (bis)
We love you and we love you (repeat)
Sétlou nala thia bir sét lou nala
We love you deeply, we love you
Meusou ma guis réew bou mélni iow
My dear country, I sing of you
Thiey sénégal deukou teranga
Oh Senegal, land of hospitality
"Kou beug sa yaye yeukk til sa lokho
"He who abandons his mother will never find peace
Kousi beug sa baye guisal sa lokho"
He who abandons his homeland will never find peace"
Képp kouy taw yeukk til sa lokho"
Never abandon your origins"
Képp kouy taaw yeukk til sa lokho"
Never abandon your origins"
Beug YOUSSOU NDOUR youxoul sa kaw "thieum"
Be like YOUSSOU NDOUR who understands this
Sopp nala nguir seu yiw
We pray for your peace
Sopp nala nguir seu dal
We pray for your prosperity
Sopp nala nguir seu téranga
We pray for your hospitality
Sét lou nala iow mi setlou nala
We love you, oh we love you
Setlou nala iow mi setlou nala
We love you, oh we love you
Setlouna thia birr setlounala
We love you deeply, we love you
Meussou ma guiss réew bou mel ni iow
My dear country, I sing of you
Thiey Sénégal dëku téranga
Oh Senegal, land of hospitality
Mane souma done yalla bilay kene doula raw
We give thanks to God, the Almighty, for this beautiful country
Souma done yalla bilay kene doula gueun
We give thanks to God, the Almighty, for this land of abundance
Mane souma done yalla bilay kene doula raw
We give thanks to God, the Almighty, for this beautiful country
Thiey senegal'o
Oh Senegal
Loune tiow tiow xol yi béne lanou
The calm seas and the plentiful fish
Loune tiow tiow diam diane si xol yi
The calm seas and the diamonds in the sea
Sopp nala nguir seu yiw
We pray for your peace
Sopp nala nguir seu dal
We pray for your prosperity
Mane sopp nala nguir seu téranga
We pray for your hospitality
Setlou nala iow mi setlou nala
We love you, oh we love you
Setlouna thia birr setlounala
We love you deeply, we love you
Meussou ma guiss réew bou mel ni iow
My dear country, I sing of you
Thiey Sénégal dëku téranga
Oh Senegal, land of hospitality
Loune tiow tiow xol yi béne lanou
The calm seas and the plentiful fish
Loune tiow tiow diam diane si xol yi
The calm seas and the diamonds in the sea
Liy nekh nekhna (dara duko dakh)
Those who wander (the child of the country suffers)
Liy nekh nekh na
Those who wander
Sopp nala nguir seu yiw
We pray for your peace
Sopp nala nguir seu dal
We pray for your prosperity
Mane Sopp nala nguir seu téranga
We pray for your hospitality
Mane Setlounala iow mi setlounala
We love you, oh we love you
Sétlou nala iow mi setlou nala
We love you, oh we love you
Setlounala thia biir setlounala
We love you deeply, we love you
Meussouma guiss reew bou mel ni iow
My dear country, I sing of you
Cey Sénégal dëku téranga
Oh Senegal, land of hospitality
Mane suma done Yalla Bilay kéne doula ...
We give thanks to God, the Almighty, for this country ...
Suma done Yalla billah keine dula raw
We give thanks to God, the Almighty, for this beautiful country
Mane suma done Yalla Bilay ×2
We give thanks to God, the Almighty ×2
Sénegal souma done yalla bilay
Senegal, we give thanks to God, the Almighty
Mane souma done yalla bilay kene doula raw
We give thanks to God, the Almighty, for this beautiful country
Tiey sénegal deukou teranga
Oh Senegal, land of hospitality
Mani Liy nekh nekhna dara douko dakh
Those who wander (the child of the country suffers)
Dara douko yakh dara douko dakh
The child of the country suffers, the child of the country suffers
Liy nekh nekhna dara douko dakh
Those who wander (the child of the country suffers)
Dara douko dakh dara douko dakh
The child of the country suffers, the child of the country suffers
Liy nekh nekhna dara douko dakh
Those who wander (the child of the country suffers)
Dara douko dakh dara douko dakh
The child of the country suffers, the child of the country suffers
Liy nekh nekhna dara douko dakh
Those who wander (the child of the country suffers)
Nanekha nekh dara dou dakh dara douko dakh
We wander, the child of the country suffers, the child of the country suffers
Liy nekh nekhna
Those who wander
Ohhhh
Ohhhh





Writer(s): youssou n'dour


Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.