Youssou N'Dour - Sapeurs pompiers paroles de chanson

paroles de chanson Sapeurs pompiers - Youssou N'dour



Chové chové chové vie
Sapeur nékhou lénam "wa walay ni kéne baniou léne" ×4
Sapeur pompier moy chové tass
Babacar sapeur pompier moy chové tass
Mbaye dieye sapeur pompier moy chové tass
Babacar sapeur pompier moy chove tass
Dagay tok souba ba gone dikhar coute fil
Loumana khew niou diouk takhaw mou diaral la sa bakéne
Amou niou fête amou wakh tou amou niou vie de famille
Sa gayi sama diambar yi mane tay ma wayal lene
Sapeur nékhou lénam "wa walay ni kéne baniou léne" ×4
Mbaye dieye sapeur pompier moy chové tass
Babacar sapeur pompier moy chove tass (bis)
Dagay tok souba ba gone dikhar coute fil
Loumana khew niou diouk takhaw mou diaral la sa bakéne
Amou niou fête amou wakh tou amou niou vie de famille
Sama gaynde yi sama diambar yi nieuw léne ma wayal léne
Pompier diou gueul
Pompier diou gueul yeugou (bis)
Boumou done yaw dine ko (Wadia ×4)
"Mbaye dieye faye"
Koulak daay gui yena lakk daay gui
Khana khamou lo sapeur ya gui nieuw nio kay faye
Koulak daay gui yena lakk daay gui
Sén tou léne sapeur yagui nieuw
Tay dji ma ndioukeul léne
Tay dji ma sargal léne
Sapeur pompier amoul heure mouy goudi mouy mbathieuk
Mouy taw mou nith
Sapeur pompier amoul heure
Niaata sapeur pompier nio diokhé séne
Bakéne nguir chové domou adama ndiaye
Kérok bou yawmal khiyamé sou sapeur
Pompier fayou woul khawma kouy fayou
Tay dji ma sagal léne Tay dji ma ndioukeul léne
Amou léne heure
Mouy goudi mouy beutieuk mouy nawéte mouy noor
Thiey bou sapeur pompier amoul wone
Dunu nélaw mouy goudi mouy bedieuk
Foléne wo niou daldi téew tiey sapeur
Thiey sapeur pompier




Youssou N'Dour - Respect
Album Respect
date de sortie
30-11-2018



Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.