paroles de chanson Habib faye - Youssou N'Dour , Jean-Philippe Rykiel
Adduna
bi
du
dara;
te
dara
xaj
u
fi
Bi
Lahii
ku
ko
japp;
xamal
ni
japp
u
loo
ci;
dara
Adduna
bi
du
dara;
te
dara
xaj
u
fi
Bi
Lahii
ku
ko
japp;
xamal
ni
japp
u
loo
ci;
dara
Man
Youssou
ñakk
naa;
andandoo
bu
sincère
Your
Online
Choices
Logo
ENGLISH
FOR
YOUR
CHILD!
More
than
8 Million
Kids
are
Learning
English
with
This
App!
Adduna;
adduna
daal;
nax
ati
na
ñu
Adduna;
adduna
da
fay
wor
ee
Habib
Faye;
dem
na
nii
Waa
ju
baax;
guddée
na
waay
Habib
yaru
woon
na;
and
ak
dignité
Fonŋk
oon
na
liggéey
ёm;
bëgg
njaboot
am
bu;
baax
Doon
oon
jàmbaar
Man
Youssou
ñakk
naa;
andandoo
bu
sincère
Adduna;
adduna
daal;
nax
ati
na
ñu
Adduna;
adduna
da
fay
wor
ee
Habib
Faye;
dem
na
nii
Waa
ju
baax;
guddée
ne
waay
Adduna;
adduna
...
Adduna;
adduna
Adduna;
adduna
daal;
nax
ati
na
ñu
Adduna;
adduna
da
fay
wor
ee
Habib
Faye;
dem
na
nii
Waa
ju
baax;
guddée
na
waay
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.