Текст песни Gadaay (feat. Obree Daman) - Obree Daman , Ashs The Best
Chiii
riii
reee
Chiii
riii
reeeraa
Ahhhhhhh
yeaaaaaaah
Ge'stu
woo
ma
Deglu
woo
ma
May
laaj
lu
xew
Gisu
loo
ma
Te
gisoon
naa
ni
Da
nga
reer
ma
lay
jeex
Da
ma
fog
ni
Tayu
loo
ko
ndax
mbëggeel
Defoon
na
ni
Di
nga
changer
balaa
maa
dem
A'ndandoo
bi
Ci
jamano
ji
Mën
na
xaar
ba
beneen
Xarit
woo
ma
Woo
ma
yee
su
fekee
may
nelaw
Fi
ñu
to'll
Kan
ngay
woolu
kudul
sa
xel
Balaa
maa
dem
Naa
la
wax
ni
am
naa
coffeel
Coffeel
bi
ma
am
ci
yow
Waat
naa
ni
doo
ko
yëgg
Wallaay
dang
ma
miin
Ba
doo
ma
yëgg
ba
maa
ngay
dem
Gestu
woo
ma
Gadaay
Gadaay
Yëggu
loo
ma
yow
Gadaay
Gadaay
Faale
wu
loo
ma
Toppatoo
wu
loo
ma
yow
(Bis)
I
know
something's
wrong
Doomu
yaay
mbaa
fate
wu
loo
ma
Woote
naa
te
wuyu
wu
loo
ma
B'cause
I
know
something's
wrong
I
know
something's
wrong
Maa
ngi
dox
akk
ta'nku
ne'en
Ci
naaj
bu
ta'ng
lool
Maa
ngi
mar
naan
ndox
mu
jafe
lool
I
know
B'cause
I
know
something's
wrong
Gilee
jëlsi
xarit
sama
doomu
yaay
fi
ma
toll
weet
naa
Bilee
doomu
yaay
jëlsi
ma
xarit
sama
fi
ma
toll
weet
naa
Doomu
yaay
jëlsi
ma
Xarit
sama
doomu
yaay
jëlsi
ma
Mbaa
fate
woo
ma
Doomu
yaay
jëlsi
ma
Xarit
sama
doomu
yaay
jëlsi
ma
Gëstu
woo
ma
Lijënti
woo
ma
yow
Faale
wu
loo
ma
Toppatto
woo
ma
yow
Gëstu
woo
ma
Xoolu
loo
ma
yow
Yëggu
loo
ma
Faale
wu
loo
ma
Lijënti
woo
ma
yow
Moo
tax
gadaay
naa
Gadaay
Fii
ku
fi
wac
sa'w
and
and
boo
dem
fekk
fa
sa
moroom
mu
toog
Xale
yaa
ngi
gadaay
Bu
ja'nt
sowee
Timis
maase
Kulay
yobbaaleel
Ndax
Guddi
xaaj
na
Fajar
waaj
na
Ëllëg
sooraaleel
Reccu
wees
na
Jëffëm
fe'eñ
na
Kookoy
diggaaleel
Ludul
Yalla
neen
la
Yeene
neeg
la
Nga
fay
fanaane
Внимание! Не стесняйтесь оставлять отзывы.