Ashs The Best feat. Ilam - Alxames (feat. ILAM) текст песни

Текст песни Alxames (feat. ILAM) - ILAM , Ashs The Best



Bësu alxames bu tiis Ci waxtu timis
Ci lañ ma diis Naqqar bu tiis
Alxames bu tiis Bu tiis a tiis
Ci lañ ma diis
Suma waaji dem na {dem na} Dem na {baayi fi njaboot ji}
Dem na {ñëpp a koy jooy} Dem na {weetal na kër gi}
Salaama yaa seydi Salaama yaa Baaba Taalibe Maam Ba'mba
Xol bi rafetoon na
Jamm laa la yeene
Doonoo woon alie'ne'
Aljana Firdawsi laa la yeene Salaama yaa seydi Baaba
Suma waaji dem na {dem na} Dem na {baayi fi njaboot ji}
Dem na {ñëpp a koy jooy} Dem na {weetal na kër gi}
Ebe njaxaa be ngandaa tobe fay Be ngalaa kobe ñaami
Dum ne muusi ni xaw nii Sukaabe
Africa ngummo deen (x) Ngummo deen
Liggo deen leydi meen saare meen
Ñoo foowandoo Maggandoo
Def nañ lu ne
Jaar nañ fu ne
Lima la yeene
Aljana laa la yeene Doonoo woon alie'ne' Taalibe Maam
Ba'mba Sa jëf ji rafet na Baaba
Bësu alxames bu tiis Ci waxtu timis
Ci lañ ma diis Naqqar bu tiis
Alxames bu tiis Bu tiis a tiis
Ci lañ ma diis
Suma waaji dem na {dem na}
Dem na {baayi fi njaboot ji} Dem na {ñëpp a koy jooy}
Dem na {weetal na kër gi}



Авторы: Olivier Delahaye, Abdoulaye Sy, Arfang Tiare


Ashs The Best feat. Ilam - Dibèer
Альбом Dibèer
дата релиза
11-06-2021



Внимание! Не стесняйтесь оставлять отзывы.