Dope Master - Nobody Can Save Me текст песни

Текст песни Nobody Can Save Me - Dope Master



No body can save me
I don't feel all right no no I feel sick
I just wanna scape I'm in the matrix
Like very day and night I do the same things
Only god can judge me
Ndakh sama bakar yeup mann makoy wéto
Kone soumay ragal khamal ni god lay done
Sokhla wouma kouma sauvé nigger no more
Nobody save now
Alone on my way no doubt
I was young but look me now
Im I do it by my self
All this since I pray to god
I did the worst he know
They taught he's the only one
I felt like I don't know
Don't ask me where you go in my mind
I feel like I don't from this fucking world but the sky
Won't sell soul my soul to get my all desires never try it
Like mama said it if you go outside pay the price
I pay the price yeah
My Life yeah
Souma khamone fi ni leu mél nigga ma diar
Keneu meunouma sauvé
Assumè késsé (hey)
Souma khamone fi ni leu mel nigger ma diar (wow wow)
No body can save me
I don't feel all right no no I feel sick
I just wanna scape I'm in the matrix
Like very day and night I do the same things
Only god can judge me
Ndakh sama bakar yeup mann makoy wéto
Kone soumay ragal khamal ni god lay done
Sokhla wouma kouma sauvé nigger no more
Bayil ma sauvé sama bopp
Diam bi dh meunouma jugé nio yam
Nite bou nek sou wété li mouy dieuf
Kene khamou ko yallah késsé mo kham
Bayil ma sauvé sama bopp
Yagu fi tam nagn def bakar
Sama khol dafeu topp sama bakane
Watchieu yone khél diap ni c'est normal
Boudé sama lay togn
Amoul koumay rendre compte koudoul god
Ndakh sama bamél Mane mafay wét
Ak lima diote def si dunya bi
Pour ngua guiss si leundeum day tarr
Seytané da beuri dolé ndeysan
Dou nieupeu wara kham fi may diar
Des fois ngua con ni niom dakoy diar
Yone bou gaw narougn fa diar
Finiou dieum lifay dem dou tank
Niom feulé lagn diogué beugu ma yéh
Teh Wollahi Nelawouma wone sakh mane
Danniou Diangu pour am kham kham
Teh chaque ngua guiss Lougn meunoul comprendre
Khalate ba moudiou fa tiank
Temps bi di niou reuf niouy diéma ray temps bi so please
(Save me, nobody can save me no more)
No body can save me
I don't feel all right no no I feel sick
I just wanna scape I'm in the matrix
Like very day and night I do the same things
Only god can judge me
Ndakh sama bakar yeup mann makoy wéto
Kone soumay ragal khamal ni god lay done
Sokhla wouma kouma sauvé nigger no more



Авторы: Olivier Delahaye, Abdoulaye Sy, El Hadji Cheikh Diouf


Dope Master - Nobody Can Save Me - Single
Альбом Nobody Can Save Me - Single
дата релиза
21-10-2022




Внимание! Не стесняйтесь оставлять отзывы.