Ismaël Lô - Fa Diallo текст песни

Текст песни Fa Diallo - Ismaël Lô



Beuguena wanté mane dama amoul
Da nga di gouné motakh mouy sa khalaat
Ni Beuguena wanté mane dama Ragal
Da nga di ngouné moutakh mouy sa khalaat
Nga naan ma kay niou sey noumouy démé?
Bou ndieukone dang chi toll niou may la djabar
legui bo ko meunoul demal teudi
Cherie coco li doyna kemane
Nga nane ma kay niou say awma pantam
Fa Diallo wakhma noko toudé
Nga naan ma takk la mane awma place
Cherie coco wakhma no ko toudé
Ndakh legui da ngay diang ba yéy keuyitt
Di takhawalou
Mané li doyna kemane
Ni beugu na, ni beuguena la
Fatou diallo wakhma no ko toudé
Nga nane ma kay niou say awma pantam
Fa Diallo wakhma noko toudé
Nga naan ma takk la mane awma place
Cherie coco wakhma no ko toudé
Ndakh legui da ngay diang ba yéy keuyitt
Di takhawalou
Mané li doyna kemane
Ni beugu na, ni beuguena la
Fatou diallo wakhma no ko toudé
Ni beugu na, ni beuguena la
Cherie coco wakhma no ko Guissé
Ni beugu na, ni beuguena la
Fatou diallo wakhma no ko toudé
Ni beugu na, ni beuguena la
Cherie coco wakhma no ko Guissé
Nga naan ma kay niou sey noumouy démé?
Bou ndieukone dang chi toll niou may la djabar
legui bo ko meunoul demal teudi
Cherie coco li doyna kemane
Nga nane ma takk la mane awma pantam
Fa Diallo wakhma noko toudé
Nga naan ma takk la mane awma place
Cherie coco wakhma no ko toudé
Ndakh legui da ngay diang ba yéy keuyitt
Di takhawalou
Mané li doyna kemane
Ni beugu na, ni beuguena la
Fatou diallo wakhma no ko toudé
Ni beugu na, ni beuguena la



Авторы: Ismael Lo


Ismaël Lô - Ismael Lo - Classic Titles
Альбом Ismael Lo - Classic Titles
дата релиза
19-12-2006




Внимание! Не стесняйтесь оставлять отзывы.