Текст песни Rëcc Na - Viviane Chidid
Par
AbouAmg
Deugeu
teule
nè
rek
tothie
na
teyal
Loufi
diar
ngendy
daw
bey
danou
teyal
Fo
tok
beugeu
gnou
nawla
teyal
Wagnil
eupeule
tè
ba
netali
teyal
Dègueloulene
Wakhou
yaram
ba
teyal
Neuneu
wakhou
kham
yone
bè
ko
geune
Teyal
beugeu
buzz
bamou
diarala
teyal
Nga
taguègo
tè
dewagoul
Cou
nek
amanga
Lila
daye
fekhèl
nga
dieum
ko
lindianti
dhè
Lila
wakh
sa
galer
ngi
takk
Di
boy
dieum
ko
lindianti
té
Faye
ko
dhé
li
la
Wakh
Lou
touty
nga
def
ko
lou
patta
Lo
xam
netali
li
la
wakh
Yakamti
rayone
na
sa
gnaum
mame
Deuguena
rayone
na
sa
gnaum
mame
Boukou
lék
féké
gnorogoul
Boul
di
Wakh
lo
khamné
amagoul
Xamoulo
do
Khar
bagnou
xamala
Guissoulo
do
Khar
ba
guiss
Lou
geuneu
lér
nga
dem
Na
nga
tey
ta
nga
dale
Amigo
Li
ngaye
Wakh
wauroula
Nopi
bakhna
thi
Lo
xamoul
lanla
Gawa
Wakh
Meuna
indi
mussiba
Deugeu
teule
nè
rek
tothie
na
teyal
Loufi
diar
ngendy
daw
bey
danou
teyal
Fo
tok
beugeu
gnou
nawla
teyal
Wagnil
eupeule
tè
ba
netali
teyal
Dègueloulene
Wakhou
yaram
ba
teyal
Neuneu
wakhou
kham
yone
bè
ko
geune
Teyal
beugeu
buzz
bamou
diarala
teyal
Nga
taguègo
tè
dewagoul
Manè
li
Khawma
lanla
li
khawma
lanla
li
khawma
lanla
li
(bis)
Ki
dhè
lidjantinala
lidjantinala
lidjantinala
yaw
mi
(bis)
Lingua
bindeu
eskeu
deugeu
leu
Fake
news
mane
yeugeulouma
Beugeu
beuz
ba
takh
nga
dima
sosal
Lingua
def
Dou
xam
nga
Noumou
toudou
Toumale
boy
yakati
nit
Wala
sakh
boy
bindeu
thi
nit
nala
lere
Li
ngaye
Wakh
ni
lou
ame
la
Lou
ko
moy
Dina
done
sa
musiba
Deugeu
teule
nè
rek
tothie
na
teyal
Loufi
diar
ngendy
daw
bey
danou
teyal
Fo
tok
beugeu
gnou
nawla
teyal
Wagnil
eupeule
tè
ba
netali
teyal
Dègueloulene
Wakhou
yaram
ba
teyal
Neuneu
wakhou
kham
yone
bè
ko
geune
Teyal
beugeu
buzz
bamou
diarala
teyal
Nga
taguègo
tè
dewagoul
Par
AbouAmg
1 Rëcc Na
2 Yenn Saï (feat. Fally Ipupa)
3 Djoug Liguey
4 Tèrè Doundou
5 Nangoulema
6 Déranger
7 Do Dara
8 Senegal
9 Benen Level
10 Def Ndam
11 Yenë Saay
Внимание! Не стесняйтесь оставлять отзывы.