Текст песни Ndox - Youssou N'Dour
Ndox,
L′eau
Sa
joie
et
sa
pudeur
font
sa
face
cachée.
Son
paraître
et
ses
formes
montrent
sa
force.
Celle
que
je
vous
chante,
vous
est
familière!
Elle
est
utile
et
belle.
Elle
a
révélé
la
beauté
du
monde.
On
la
clame
Paradis.
Mbégté
ma,
suturë
sa,
Da
fa
méngóo
k,
baatin
ëm
Zaahir
sa,
melo
ya,
Moo
won
e,
kattan
am
Li
may
misaal
lu
ngeen
xam
la,
Am
na
njariñ
te
rafet
na
Moo
génné
taar
u
adduna,
Moom
la
ñu
bakke,
al
janna
Waxtaan
e
ko
sax
banneex
la,
Nañ
ko
foηk
sakkan
al
ko
En
parler
même
est
agréable!
Respectons-la,
économisons-la.
Vois
la
mer,
le
fleuve.
Rendons
grâce
à
Dieu.
Elle
est
utile
et
belle.
Elle
a
révélé
la
beauté
du
monde.
On
la
clame
Paradis.
Mbégté
ma,
suturë
sa,
Da
fa
méngóo
k,
baatin
ëm
Zaahir
sa,
melo
ya,
Moo
won
e,
kattan
am
Li
may
misaal
lu
ngeen
xam
la,
Am
na
njariñ
te
rafet
na
Moo
génné
taar
u
adduna,
Moom
la
ñu
bakke,
al
janna
Waxtaan
e
ko
sax
banneex
la,
Nañ
ko
foηk
sakkan
al
ko
Géej
gaa
ngi
nii
yé,
Dex
gaa
ngi
nii
yé
Dara
gën
ul
ë
neex
taw
bi
Ku
weddi
laaj
ko
bay
kat
ba,
Ci
la
ñuy
roosé
seen
tool
ya
Walla
nga
laaj
ko
samm
kat
ba,
Ci
la
ñuy
nandal
e
jur
gë
Ndox
daal
am
na
njariñ
baax
na
Dara
gën
ul
lë
neex
taw
bi
Taw
daal
njariñ
la
ci
dun
bi
Ndox
daal
njariñ
ëm,
Ba
la
nga
koo
xam
mu
jafe
Ndox
daal
njariñ
ëm,
Ba
la
nga
koo
xam
mu
manqué
Ndox
daal
njariñ
ëm,
Ba
la
nga
koo
xam
mu
jafe
Ndox
daal
njariñ
ëm,
Ba
la
nga
koo
xam
mu
manqué
Ndox
daal
njariñ
ëm,
Ba
la
nga
koo
xam
mu
jafe
Ndox
daal
njariñ
ëm,
ba
la
nga
koo
xam
mu
manqué
Ndox
daal
njariñ
ëm,
Ba
la
nga
koo
xam
mu
jafe
Ndox
daal
njariñ
ëm,
Ba
la
nga
koo
xam
mu
manqué
Ndox
daal
njariñ
ëm,
Ba
la
nga
koo
xam
mu
jafe
Ndox
daal
njariñ
ëm,
Ba
la
nga
koo
xam
mu
manqué
Alaa
gaynaago
yoo
samba
lingeer
Donoy
waaly
yée,
wulée
ñaay
ngoy,
Yée
gan
wuri
coo,
wulée
gaynaako
yoo
Yeée,
yóo,
gan
fari
baa
1 Gagganti ko
2 Mama Africa
3 Ndox
4 La solution c’est de pardonner
5 Mool
6 Tatagal
7 Fay Bor
8 Ballago ndumbé Yaatma
9 Zéro déchets
10 Da fa laa
11 Wax ju Bari
12 Waññ iko
Внимание! Не стесняйтесь оставлять отзывы.