Ashs The Best - 1995 Lyrics

Lyrics 1995 - Ashs The Best



Yeah
Was born in 1995
Juddoo Ghetto màggee Ghetto
My name is Ashs, you know the vibes
I'm from zero to hero
Seereer ci baay Baay Faal ci life
Ci man dara du fi dara
May kan nitt ku toroxlu la
Mujj bu rafet rekk ñaan
Was born in 1995
Boroom basse bi guitare bi sam baay
Yaay Joor def li nekk ci man
Mënu ma dof fate fi ma jaar
Boy laa woon comme boy yëpp
Amoon rêve pour tëpp tekki pour ñëpp
Yalla Buur bi doggal
Du ma lenn kenn mais lepp ñëpp
Was born in 1995
Born in 1995 Yo
Yo
Born in 1995
Juddoo biir ghetto maggee biir Ghetto
Taxul nga raw ñu brain ci life
{1995 yo yo}
{1995 yo yo}
Ma nekk ku kenn nekkul ci ñoom
Ñoom dañ ma jiitu fu lëndëm ma len niital fu ñuy tekk sen tànk
1995
This is what I do all night
This is what I do every f**king night
Fuck ñu fogoon ni ñëwoon pour tekki ci rew me we try all day all night
Tukki du tekki, tekki du tukki teewul
Ñoo ngi jekk ci game bi ligeey money fayeeku
Nobody can stop my mind
Nobody can stop my mind
Juddoo ci hood màggee ci hood bi fuck almadies ak Cap
Si mbedd buur bi lañ jàngee hip-hop même prési day xaar
Bañ nga def ma jàam ma def rappeur bu mag
Bëggu ma kaaw ak gellu tubaab
Juddoo ci reew mi tekkee ci reew mi from zero to hero
Nothing to something yaakaar ci Yalla gën yaakaar si yeen
Nigger what's poppin' mën u ñu bókk ay demin
Yeen da ngen i foo man may teegin
Ñoom ñoo ngi si kaw man may sommet bi
Nobody can know me man maa gën a high sen rappeurs yu magg yi
I can't follow you soo jiitalul mind sa doole du jëriñ
Rabuma pour siiw maa nge'eg melodies yuy dugg ci xol yi
Wëri millions vues moom du musique rekk ligeey la ak fayeeku
Nobody can know me maa nge'eg dictionnaire ak flow bës bu nekk
Duggu ñu ci mines yi no du ñu teggi tànk ay att fii ñoo fi nekk
Talent confirmé sa emcee confinement lay dugg ay dewën
Boy Ashs day jinne limay rap de fi damalen rawee ay dewën
Born in 1995
Juddoo biir ghetto maggee biir Ghetto
Taxul nga raw ñu brain ci life
{1995 yo yo}
{1995 yo yo}
Ma nekk ku kenn nekkul ci ñoom
Ñoom dañ ma jiitu fu lëndëm ma len niital fu ñuy tekk sen tànk
1995
This is what I do all night
This is what I do every f**king night
Fuck ñu fogoon ni ñëwoon pour tebbi ci ...
Tukki du tekki, tekki du tukki teewul
Ñoo ngi jekk ci game bi ligeey money fayeeku
Nobody can stop my mind
Born in 1995
Born in 1995



Writer(s): Abdoulaye Sy, Olivier Delahaye


Ashs The Best - 1995 - EP
Album 1995 - EP
date of release
25-02-2022




Attention! Feel free to leave feedback.