Ashs The Best - GIVE UP Lyrics

Lyrics GIVE UP - Ashs The Best



I can't give up mine
Love and peace for me
Mënu ma gestu ginaaw
1995
Loo loo waral mën u ma fatte att ba bes am di fénk
Bëggu ma gàcce tax xëccoo wu ma ak kenn
I'm on my way mën nu ma def ludul dañ
Geestu wuma kenn
Ñoom gëstu wu ñu pour xam li daw sunu biir
Lu fees si xol tuuru si jëmm
Sa bos am rancune ak haine
Bëggoon nga xam li nekk ci man moo ngi ci
Non du xëy toog
Dereet u gor ñoom ñoo la gën a xam ne dawul sen biir
Luy ndey Or ay diamant lañ ci mbalit Ba leen ci biir
Bës a ngi ci bës yi
Mais bëccëgment mystique guddiment bët set
All day victime ñi fogoon ne du nekk
Tay ñëpp a bëgg a bokk
Mais impossible ñun fi nu jaar ba fii
Dekku naaj ak xiif
Nangu ndogal da ñoo xaar ba giif
Ay att ñu sacrifice
I can't give up mine
I can't give up
Love and peace for me
Huuuuu
Mënu ma gestu ginaaw
I can't give up
Mine
Gestul ginaaw
Yeeeeah
Gestul ginaaw
Ñun fi ñu jaar ba fii
Dañ ko xaar dekku tiis
Dañ ko raag dañ ko gis
Dañ rap ramper try ko ba yegsi fii
Gestul ginaaw
Nuñ mën nañ def comme d'hab
Man'ag ñoom du combat
Ñoo ma dakk rap ma dakk len def lu nice
Fu ma jaar ñoom duñ fa jaar
Peace and love for me
Follow sama energy
Defaite moy ennemi
Million akk legacy
Projet bu dem beneen gën a deep
Ñoo ngi fi demb ak tay
Suba akk ëllëg kay
Ñoo mën te di ko def
Ñoo yor say linge tay
Musique bu neex bi waaw goor mi ngi fay
I can't give up
Nobody know
I say I can't give up
Bu kenn disturb
Melting pot millions flows
Bu jeex beneen bi ñëw
Bi game du low
Jël trône bi blow ci
Ku toog ci trône bi nala leer ni toog nga si sama big dick
I can't give up mine
I can't give up
Love and peace for me
Huuuuu
Mënu ma gestu ginaaw
I can't give up
Mine
Gestul ginaaw
Yeeeeah
I can't give up
Mine
Gestul ginaaw
Yeeeeah



Writer(s): Olivier Delahaye, Abdoulaye Sy, Arfang Tiare


Ashs The Best - 1995 - EP
Album 1995 - EP
date of release
25-02-2022




Attention! Feel free to leave feedback.