Ashs The Best - LIFE IS LOVE Lyrics

Lyrics LIFE IS LOVE - Ashs The Best



Oh yeah yeah
I love my life
Life is love
Love is life
I love my life
Jealousy enemy akk ñii di siis
My life is love
Genn ci ghetto bi ligeey lot of jizz indi ci galle bi
I'm black I'm proud
Like Pablo I'm lonely on my own
You can't stop me
I'm black yes and I'm young too
You can't stop me
I love my life
Dof ci son you see me
Def Ko ci Kendrick maa ngi Jolof toog
Million zéro pression
Tukki du tekki geenu ma studio
Def comme Fada comme Ndongo Xuman akk Bibson
Sa stars yi lay jangal rap bi du pour coow
King bi yaw la maa ngi akk millions flows
From the bottom to the fucking top
Gis-gis yi ñoo wute
I know that you know yeah
I know that you knoooooow oh my mind
This is how I feel it
But I know something you know
I know that you know yeah
I love my life
Jealousy enemy akk ñii di siis
My life is love
Genn ci ghetto bi ligeey lot of jizz indi ci galle bi
I'm black I'm proud
Like Pablo I'm lonely on my own
You can't stop me
I'm black yes and I'm young too
You can't stop me
Xëcc bu daggul dikk kay
Nañ ko xare demb ngir tay
Dëkk ci suba guddi ngoon hoslou ngir guenesi
Fëgg buntu bi tijjiwul teewul ñu jëlli lu ñu moom
Fii ba Adduna wërngël kepp ligeey bi du pour fii
Tëdd nelaw gent bi yee ma ne ma coono du reer boroomam
Ci tolof-tolof sëgg siggi ngir dellusi
Bu ñii di yakk di yakate
Ñii di takk di daggate
Maa ngi diap rap paqueter bangg
Sekku ñu baale
Sekku ñu ñi sakku ci rap bi
Du geenati gaal bi
Dërëm bi du geen gaal bi
Dëkku ma Capsi
Xëppu ma suuf ci ndap li
Di siggil ndigaale
Siggil sa wall ci rap bi
Ki ngen diggaalel du baale
Bu jekkoo du baale
Bul faale ku dematul
Kouy bardé na bardé kou pare
Ku xarei niou xarei nioune
Ku tarder dou andak ku tardei
Comparer ma'ag boy yi
Moy comparer nga sa shody akk sa mother



Writer(s): Olivier Delahaye, Abdoulaye Sy, Arfang Tiare


Ashs The Best - 1995 - EP
Album 1995 - EP
date of release
25-02-2022




Attention! Feel free to leave feedback.