Lyrics Weetël - Amira Abed , Ashs The Best
Muy
suba
muy
guddi
Muy
naaj
Mbaa
muy
soobee
Mësu
maa
woote
Te
wuyu
loo
ma
Boo
weetee
gore
Weetali
ku
nga
akk
sa
mbëggeel
Mësu
maa
woote
Te
wuyu
loo
ma
Ah
Yeah
Ah
Yeah
Eh
Yah
Mësu
maa
woote
Te
wuyu
loo
ma
Fii
ci
addun
yaa
Gisu
ma
ku
melni
yow
Mbëggeelam
yaatu
na
Yërmandeem
moo
ma
yeem
Ku
melni
yow
Benn
la
dootul
ñaar
Yaay
sama
Aljana
Yow
mi
ma
teg
yoon
Ci
yoonu
leer
Cause
I've
been
fearless
To
get
to
the
road
tonight
Because
so
been
love
Nobody
never
Everything
how
to
try
But
I
believe
in
miracle
now
You're
right
here
Yow
mii
sa
mbëggeel
bi
yaatu
na
ni
Adduna
Gestu
gis
la
sama
wet
muy
Aljana
Mësu
maa
la
woo
te
wuyu
loo
ma
Sa
yërmande
yeem
na
ma
man
Xeebu
loo
benn
yoon
siggil
nga
ma
Def
ma
ni
sa
bopp
te
won
nga
ma
I've
been
so
grateful
for
your
love
Muy
suba
muy
guddi
Muy
naaj
Mbaa
muy
soobee
Mësu
maa
woote
Te
wuyu
loo
ma
Boo
weetee
gore
Weetali
ku
nga
akk
sa
mbëggeel
Mësu
maa
woote
Te
wuyu
loo
ma
Mësu
ma
la
woo
wuyu
loo
ma
Saayu
ma
soxla
nga
jox
ma
xañ
sa
bopp
Li
nekk
ci
Yow
moy
daw
ci
man
mii
Suma
la
gisee
Moy
gis
naa
sama
bopp
Lu
fees
ci
xol
feeñ
ci
jëmm
jii
Yow
sa
mbëggeel
moo
may
weetali
Yow
mii
Sa
mbëggeel
bi
yaatu
na
ni
Adduna
Gestu
gis
la
sama
wet
muy
Aljana
Mësu
maa
la
woo
te
wuyu
loo
ma
Sa
yërmande
yeem
na
ma
man
Xeebu
loo
benn
yoon
siggil
nga
ma
Def
ma
ni
sa
bopp
te
won
nga
ma
loolu
I've
been
so
grateful
for
your
love
Muy
suba
muy
guddi
Muy
naaj
Mbaa
muy
soobee
Mësu
maa
woote
Te
wuyu
loo
ma
Boo
weetee
gore
Weetali
ku
nga
akk
sa
mbëggeel
Mësu
maa
woote
Te
wuyu
loo
ma
Te
wuyu
loo
ma...
Attention! Feel free to leave feedback.