Lyrics Sama Prof (feat. 2k) - Canabasse , 2k
                                                SAMA 
                                                PROF
 
                                    
                                
                                                Mome 
                                                mo 
                                                takh 
                                                legui 
                                                diangue
 
                                    
                                
                                                Di 
                                                ndeukeunté 
                                                tableau 
                                                pour 
                                                todj 
                                                ay 
                                                exo
 
                                    
                                
                                                Mo 
                                                ma 
                                                khagn 
                                                diame 
                                                Ba 
                                                gneupe 
                                                kham 
                                                ko
 
                                    
                                
                                                Yea 
                                                Melnani 
                                                mome 
                                                rekk 
                                                'a 
                                                nandoul
 
                                    
                                
                                                Sama 
                                                prof
 
                                    
                                
                                                Classe 
                                                bi 
                                                mome 
                                                mo 
                                                fay 
                                                yeungual
 
                                    
                                
                                                Sama 
                                                prof 
                                                la 
                                                bardé 
                                                Moma 
                                                khagn 
                                                diame
 
                                    
                                
                                                Classe 
                                                bi 
                                                mome 
                                                mo 
                                                fay 
                                                yeungual
 
                                    
                                
                                                Sama 
                                                prof 
                                                la 
                                                bardé 
                                                Moma 
                                                khagn 
                                                diame
 
                                    
                                
                                                Sama 
                                                profou 
                                                Marketing
 
                                    
                                
                                                Dalay 
                                                may 
                                                jean
 
                                    
                                
                                                Ndiole 
                                                Tchi 
                                                Kaw
 
                                    
                                
                                                Diek 
                                                forme
 
                                    
                                
                                                Rafet 
                                                signe
 
                                    
                                
                                                Bouy 
                                                expliquer 
                                                di 
                                                bigne 
                                                dafa 
                                                may 
                                                Kill
 
                                    
                                
                                                Yalla 
                                                boumou 
                                                teglé 
                                                tank 
                                                sekh 
                                                tankou 
                                                lunettes 
                                                yi
 
                                    
                                
                                                Yaramou 
                                                minette 
                                                la 
                                                yor
 
                                    
                                
                                                Bête 
                                                de 
                                                silhouette 
                                                té 
                                                yaw
 
                                    
                                
                                                Bou 
                                                ma 
                                                né 
                                                Ndiakk 
                                                rek 
                                                ma 
                                                taggok 
                                                sama 
                                                saago
 
                                    
                                
                                                Meussouma 
                                                beugg 
                                                tableau 
                                                mais 
                                                legui 
                                                raktiak 
                                                ma 
                                                yeukeuti 
                                                lokho 
                                                ndieukeunté 
                                                ko 
                                                ndakh 
                                                prof 
                                                Bi 
                                                fok 
                                                ma 
                                                épaté 
                                                ko
 
                                    
                                
                                                Hey 
                                                damay 
                                                goukh 
                                                cour 
                                                Bi 
                                                Laata 
                                                may 
                                                tew
 
                                    
                                
                                                Dotouma 
                                                tok 
                                                Tchi 
                                                guinaw 
                                                pour 
                                                geune 
                                                ko 
                                                meune 
                                                diew
 
                                    
                                
                                                Toujours 
                                                attentif
 
                                    
                                
                                                Mome 
                                                rek 
                                                sama 
                                                khel
 
                                    
                                
                                                Mome 
                                                mo 
                                                koy 
                                                todj 
                                                professeur 
                                                modèle
 
                                    
                                
                                                Motakh 
                                                may 
                                                tok 
                                                Tchi 
                                                kanam 
                                                tiim 
                                                podj 
                                                yek 
                                                kanam 
                                                di 
                                                participer 
                                                Tchi 
                                                cour 
                                                Bi 
                                                ndakh
 
                                    
                                
                                                Hey 
                                                dama 
                                                bardé 
                                                sama 
                                                prof
 
                                    
                                
                                                Mome 
                                                mo 
                                                takh 
                                                legui 
                                                diangue
 
                                    
                                
                                                Di 
                                                ndeukeunté 
                                                tableau 
                                                pour 
                                                todj 
                                                ay 
                                                exo
 
                                    
                                
                                                Mo 
                                                ma 
                                                khagn 
                                                diame 
                                                Ba 
                                                gneupe 
                                                kham 
                                                ko
 
                                    
                                
                                                Yea 
                                                Melnani 
                                                mome 
                                                rekk 
                                                'a 
                                                nandoul
 
                                    
                                
                                                Sama 
                                                prof
 
                                    
                                
                                                Classe 
                                                bi 
                                                mome 
                                                mo 
                                                fay 
                                                yeungual
 
                                    
                                
                                                Sama 
                                                prof 
                                                la 
                                                bardé 
                                                Moma 
                                                khagn 
                                                diame
 
                                    
                                
                                                Classe 
                                                bi 
                                                mome 
                                                mo 
                                                fay 
                                                yeungual
 
                                    
                                
                                                Sama 
                                                prof 
                                                la 
                                                bardé 
                                                Moma 
                                                khagn 
                                                diame
 
                                    
                                
                                                Bou 
                                                cour 
                                                Bi 
                                                diekhé 
                                                damay 
                                                triste
 
                                    
                                
                                                Boumay 
                                                gnibbi 
                                                damay 
                                                crispé
 
                                    
                                
                                                Moome 
                                                sama 
                                                khol 
                                                la 
                                                dieul 
                                                confisqué
 
                                    
                                
                                                Yagg 
                                                na 
                                                fantasmer 
                                                mou 
                                                may 
                                                kiss 
                                                yeah
 
                                    
                                
                                                Madame 
                                                mademoiselle 
                                                khawma 
                                                babe 
                                                la 
                                                Tchi 
                                                done 
                                                lene 
                                                Moma 
                                                ler 
                                                moy 
                                                sama 
                                                bardé 
                                                Tchi 
                                                mome
 
                                    
                                
                                                Douma 
                                                tardé 
                                                Bou 
                                                couram 
                                                djoté 
                                                damay 
                                                koy 
                                                khar 
                                                té 
                                                après 
                                                damay 
                                                dougue 
                                                Google 
                                                prochain 
                                                cours 
                                                ma 
                                                diaye 
                                                ko 
                                                wané
 
                                    
                                
                                                Mome 
                                                dafa 
                                                Ame 
                                                Facebook
 
                                    
                                
                                                Instagram 
                                                Ak 
                                                snapchat
 
                                    
                                
                                                Tchi 
                                                otom 
                                                dreezy 
                                                Lay 
                                                deglou
 
                                    
                                
                                                Ler 
                                                na 
                                                ma 
                                                ni 
                                                dafay 
                                                Dem 
                                                boîte 
                                                sakh
 
                                    
                                
                                                Daf 
                                                may 
                                                diangua 
                                                ma 
                                                koy 
                                                diangue
 
                                    
                                
                                                Sometimes 
                                                ma 
                                                khouss 
                                                Ba 
                                                tablant 
                                                salé 
                                                néko 
                                                madame 
                                                comprendrouma
 
                                    
                                
                                                Lepe 
                                                pour 
                                                satch 
                                                thiatal 
                                                deunnam
 
                                    
                                
                                                Parfum 
                                                Bou 
                                                nekh 
                                                Bi 
                                                dal 
                                                ma 
                                                ma 
                                                diakhasso 
                                                né 
                                                kou 
                                                geuleum
 
                                    
                                
                                                Mome 
                                                mo 
                                                takh 
                                                legui 
                                                diangue
 
                                    
                                
                                                Di 
                                                ndeukeunté 
                                                tableau 
                                                pour 
                                                todj 
                                                ay 
                                                exo
 
                                    
                                
                                                Mo 
                                                ma 
                                                khagn 
                                                diame 
                                                Ba 
                                                gneupe 
                                                kham 
                                                ko
 
                                    
                                
                                                Yea 
                                                Melnani 
                                                mome 
                                                rekk 
                                                'a 
                                                nandoul
 
                                    
                                
                                                Sama 
                                                prof
 
                                    
                                
                                                Classe 
                                                bi 
                                                mome 
                                                mo 
                                                fay 
                                                yeungual
 
                                    
                                
                                                Sama 
                                                prof 
                                                la 
                                                bardé 
                                                Moma 
                                                khagn 
                                                diame
 
                                    
                                
                                                Classe 
                                                bi 
                                                mome 
                                                mo 
                                                fay 
                                                yeungual
 
                                    
                                
                                                Sama 
                                                prof 
                                                la 
                                                bardé 
                                                Moma 
                                                khagn 
                                                diame
 
                                    
                                
                                                Prof 
                                                Bi 
                                                prof 
                                                Bi
 
                                    
                                
                                                Dafay 
                                                diame 
                                                ni 
                                                goss 
                                                yi
 
                                    
                                
                                                Dafay 
                                                pop 
                                                lipgloss 
                                                Bi 
                                                dakoy 
                                                cassé 
                                                oh 
                                                shit
 
                                    
                                
                                                Gucci 
                                                Prada 
                                                Louis
 
                                    
                                
                                                Boum 
                                                Tchi 
                                                sole 
                                                Ba 
                                                dougue 
                                                Ngua 
                                                fokni 
                                                classe 
                                                Bi 
                                                dagn 
                                                ko 
                                                sopi 
                                                défilé 
                                                mannequin
 
                                    
                                
                                                Bope 
                                                Bou 
                                                fess
 
                                    
                                
                                                Proportionnel 
                                                    à 
                                                ses 
                                                seins
 
                                    
                                
                                                Mome 
                                                daf 
                                                ma 
                                                Kill
 
                                    
                                
                                                Jeux 
                                                de 
                                                visage 
                                                assassins
 
                                    
                                
                                                Mome 
                                                motakh 
                                                legui 
                                                may 
                                                diangue 
                                                di 
                                                todj 
                                                ay 
                                                exo
 
                                    
                                
                                                Damay 
                                                sakh 
                                                ndieukeunté 
                                                tableau
 
                                    
                                
                                                Sama 
                                                prof
 
                                    
                                
                                                Mome 
                                                daal 
                                                Moma 
                                                khagn 
                                                diame
 
                                    
                                
                                                Classe 
                                                Bi 
                                                yeup 
                                                khamnagn 
                                                mel 
                                                na 
                                                ni 
                                                mome 
                                                rek 
                                                mo 
                                                nandoul
 
                                    
                                
                                                Mome 
                                                mo 
                                                takh 
                                                legui 
                                                diangue
 
                                    
                                
                                                Di 
                                                ndeukeunté 
                                                tableau 
                                                pour 
                                                todj 
                                                ay 
                                                exo
 
                                    
                                
                                                Mo 
                                                ma 
                                                khagn 
                                                diame 
                                                Ba 
                                                gneupe 
                                                kham 
                                                ko
 
                                    
                                
                                                Yea 
                                                Melnani 
                                                mome 
                                                rekk 
                                                'a 
                                                nandoul
 
                                    
                                
                                                Sama 
                                                prof
 
                                    
                                
                                                Classe 
                                                bi 
                                                mome 
                                                mo 
                                                fay 
                                                yeungual
 
                                    
                                
                                                Sama 
                                                prof 
                                                la 
                                                bardé 
                                                Moma 
                                                khagn 
                                                diame
 
                                    
                                
                                                Classe 
                                                bi 
                                                mome 
                                                mo 
                                                fay 
                                                yeungual
 
                                    
                                
                                                Sama 
                                                prof 
                                                la 
                                                bardé 
                                                Moma 
                                                khagn 
                                                diame
 
                                    
                                
                            1 Mane La Wone
2 Dedet
3 Walabok Baye
4 Girls (feat. Cheeks & Zou Kana)
5 Weurseuk (feat. Eliane)
6 Atanougnou Dome
7 Noflaye (feat. Eliane)
8 Radison Music (feat. Tenny)
9 Well Done
10 Kholal
11 3iem Baram
12 Sama Prof (feat. 2k)
13 Metti
14 Werouwaye
15 It's Bass
16 Mane Rek Ngua Bagn (Bonus Track)
17 Dama Koy Dundu (Bonus Track)
Attention! Feel free to leave feedback.