Lyrics Mane Rek Ngua Bagn (Bonus Track) - Canabasse
                                                Degg 
                                                na 
                                                Mane 
                                                rek 
                                                Nga 
                                                bagne 
                                                mais 
                                                lolou 
                                                dou 
                                                dara
 
                                    
                                
                                                Togal 
                                                fi 
                                                nga 
                                                tokk 
                                                di 
                                                tek 
                                                douma 
                                                Wakh 
                                                sama 
                                                job 
                                                tontou 
                                                nala
 
                                    
                                
                                                Sama 
                                                team 
                                                premier 
                                                plan 
                                                Gni 
                                                Tchi 
                                                dess 
                                                gnou 
                                                may 
                                                lene 
                                                troisième 
                                                barame
 
                                    
                                
                                                Zero 
                                                stress 
                                                Zero 
                                                panique 
                                                Dieulsi 
                                                li 
                                                ma 
                                                indi
 
                                    
                                
                                                Lou 
                                                bloqué 
                                                sama 
                                                yone 
                                                believe 
                                                me 
                                                Nako 
                                                boulé
 
                                    
                                
                                                Khawma 
                                                ndakh 
                                                degg 
                                                Ngama
 
                                    
                                
                                                Hey 
                                                boma 
                                                touddé
 
                                    
                                
                                                Ma 
                                                Todj 
                                                sa 
                                                nounara
 
                                    
                                
                                                Hey 
                                                fouma 
                                                jouer 
                                                ay 
                                                liasse 
                                                tourou 
                                                na 
                                                fa
 
                                    
                                
                                                Bou 
                                                gnou 
                                                diawalé 
                                                Peureum 
                                                dou 
                                                ngualam
 
                                    
                                
                                                Wala 
                                                bok 
                                                yaw
 
                                    
                                
                                                Mother 
                                                fucker 
                                                khana 
                                                deggo
 
                                    
                                
                                                Koula 
                                                doundoul 
                                                ngala 
                                                dé 
                                                ko
 
                                    
                                
                                                Amena 
                                                acteur 
                                                Amena 
                                                Decor
 
                                    
                                
                                                Té 
                                                Tchi 
                                                Bi 
                                                film 
                                                dou 
                                                ma 
                                                déh 
                                                Boy
 
                                    
                                
                                                Jeune 
                                                homme 
                                                May 
                                                jeuneum 
                                                (acteur)
 
                                    
                                
                                                Hip 
                                                hop 
                                                galsen 
                                                boudé 
                                                gorr 
                                                nama 
                                                gueureum
 
                                    
                                
                                                Sama 
                                                deuneu 
                                                Tchi 
                                                sa 
                                                noppeuh 
                                                malay 
                                                seddeu 
                                                sama 
                                                deugg
 
                                    
                                
                                                Gnénène 
                                                gniy 
                                                doul 
                                                di 
                                                dadialé 
                                                doundou 
                                                gnou 
                                                lignouy 
                                                bindeu
 
                                    
                                
                                                Mangui 
                                                Tchi 
                                                wagne 
                                                bi 
                                                togg 
                                                té 
                                                liy 
                                                khégne 
                                                nekh 
                                                sama 
                                                tchineu
 
                                    
                                
                                                Douma 
                                                daanou 
                                                khana 
                                                Tchi 
                                                bir 
                                                té 
                                                di 
                                                na 
                                                weussine
 
                                    
                                
                                                Adresse 
                                                Bi 
                                                BuzzLab 
                                                la 
                                                bo 
                                                sokhla 
                                                wassila
 
                                    
                                
                                                Adresse 
                                                meunou 
                                                Fi 
                                                gnakk 
                                                sayou 
                                                gnou 
                                                shooté 
                                                dougal
 
                                    
                                
                                                Nigga 
                                                shut 
                                                shut 
                                                Yangui 
                                                youkhou 
                                                deggouma
 
                                    
                                
                                                Mala 
                                                sout 
                                                fouf 
                                                sama 
                                                niveau 
                                                wessoula
 
                                    
                                
                                                Yangui 
                                                Tchi 
                                                souf 
                                                sama 
                                                job'a 
                                                lay 
                                                soul
 
                                    
                                
                                                I'm 
                                                    a 
                                                success 
                                                story 
                                                bitch 
                                                Deal 
                                                Bi 
                                                gëstou 
                                                la
 
                                    
                                
                                                Aaah 
                                                Aaah
 
                                    
                                
                                                Degg 
                                                na 
                                                Mane 
                                                rek 
                                                Nga 
                                                bagne 
                                                mais 
                                                lolou 
                                                dou 
                                                dara
 
                                    
                                
                                                Togal 
                                                fi 
                                                nga 
                                                tokk 
                                                di 
                                                tek 
                                                douma 
                                                Wakh 
                                                sama 
                                                job 
                                                tontou 
                                                nala
 
                                    
                                
                                                Sama 
                                                team 
                                                premier 
                                                plan 
                                                Gni 
                                                Tchi 
                                                dess 
                                                gnou 
                                                may 
                                                lene 
                                                troisième 
                                                barame
 
                                    
                                
                                                Zero 
                                                stress 
                                                Zero 
                                                panique 
                                                Dieulsi 
                                                li 
                                                ma 
                                                indi
 
                                    
                                
                                                Lou 
                                                bloqué 
                                                sama 
                                                yone 
                                                believe 
                                                me 
                                                Nako 
                                                boulé
 
                                    
                                
                                                Khawma 
                                                ndakh 
                                                degg 
                                                Ngama
 
                                    
                                
                                                Hey 
                                                boma 
                                                touddé
 
                                    
                                
                                                Ma 
                                                Todj 
                                                sa 
                                                nounara
 
                                    
                                
                                                Hey 
                                                fouma 
                                                jouer 
                                                ay 
                                                liasse 
                                                tourou 
                                                na 
                                                fa
 
                                    
                                
                                                Bou 
                                                gnou 
                                                diawalé 
                                                Peureum 
                                                dou 
                                                ngualam
 
                                    
                                
                                                Wala 
                                                bok 
                                                yaw 
                                                verse 
                                                2}
 
                                    
                                
                                                Peureum 
                                                dou 
                                                ngalame
 
                                    
                                
                                                Kou 
                                                Fi 
                                                ndieukka 
                                                guéné 
                                                mixtape 
                                                dou 
                                                mana
 
                                    
                                
                                                Dou 
                                                lèpp 
                                                deh 
                                                nonon
 
                                    
                                
                                                Hip 
                                                hop 
                                                galsen 
                                                première 
                                                place 
                                                trace 
                                                goulète 
                                                dou 
                                                mana
 
                                    
                                
                                                Premier 
                                                Tchi 
                                                Lépp 
                                                ni 
                                                Kana
 
                                    
                                
                                                Mane 
                                                Ak 
                                                succes 
                                                comme 
                                                notice 
                                                Tchi 
                                                garap
 
                                    
                                
                                                Tatouage 
                                                Tchi 
                                                yaram
 
                                    
                                
                                                Limay 
                                                Wakh 
                                                dou 
                                                degn
 
                                    
                                
                                                Préférence 
                                                Bi 
                                                mana
 
                                    
                                
                                                Référence 
                                                Bi 
                                                mana
 
                                    
                                
                                                Ma 
                                                lene 
                                                eupe 
                                                mana
 
                                    
                                
                                                My 
                                                Nigga 
                                                dama 
                                                diangue 
                                                di 
                                                ko 
                                                santé 
                                                sama 
                                                maman
 
                                    
                                
                                                Dagn 
                                                ma 
                                                yagg 
                                                sandi 
                                                kaba 
                                                ma 
                                                dadjalé 
                                                lepe 
                                                tabakh
 
                                    
                                
                                                Ba 
                                                Tchi 
                                                Kaw 
                                                takhaw 
                                                di 
                                                saw 
                                                Sen 
                                                Kaw
 
                                    
                                
                                                My 
                                                Nigga 
                                                bagn 
                                                ma 
                                                    I 
                                                don't 
                                                give 
                                                    à 
                                                fuck
 
                                    
                                
                                                Khana 
                                                Ngua 
                                                Dem 
                                                ndakhté 
                                                Fi 
                                                may 
                                                boss
 
                                    
                                
                                                Bou 
                                                ma 
                                                kene 
                                                ladj 
                                                ndakh 
                                                rap 
                                                Bi 
                                                Day 
                                                dokh
 
                                    
                                
                                                Ma 
                                                ngui 
                                                fly 
                                                guissou 
                                                ma 
                                                lenene 
                                                loudoul 
                                                ay 
                                                tombe
 
                                    
                                
                                                Kouma 
                                                Fi 
                                                djaay 
                                                yeg 
                                                di 
                                                nga 
                                                dadjek 
                                                maggoum 
                                                golo
 
                                    
                                
                                                Lima 
                                                done 
                                                weur 
                                                daw 
                                                moungui 
                                                sama 
                                                lokho
 
                                    
                                
                                                Dara 
                                                djotatouma 
                                                meme 
                                                pas 
                                                Lima 
                                                sol
 
                                    
                                
                                                Bitch 
                                                dama 
                                                dieul 
                                                poids 
                                                khana 
                                                guisso 
                                                ni 
                                                ma 
                                                tole
 
                                    
                                
                                                Heyyyyy 
                                                Fii 
                                                BuzzLab 
                                                la
 
                                    
                                
                                                Djeuf 
                                                dji 
                                                Day 
                                                Wakh 
                                                troisième 
                                                Barame
 
                                    
                                
                                                Niari 
                                                directions 
                                                Tchi 
                                                Kaw 
                                                Tchi 
                                                kanam
 
                                    
                                
                                                No 
                                                def 
                                                mou 
                                                Ame 
                                                trace 
                                                Acide 
                                                Tchi 
                                                kanam
 
                                    
                                
                                                Degg 
                                                na 
                                                Mane 
                                                rek 
                                                Nga 
                                                bagne 
                                                mais 
                                                lolou 
                                                dou 
                                                dara
 
                                    
                                
                                                Togal 
                                                fi 
                                                nga 
                                                tokk 
                                                di 
                                                tek 
                                                douma 
                                                Wakh 
                                                sama 
                                                job 
                                                tontou 
                                                nala
 
                                    
                                
                                                Sama 
                                                team 
                                                premier 
                                                plan 
                                                Gni 
                                                Tchi 
                                                dess 
                                                gnou 
                                                may 
                                                lene 
                                                troisième 
                                                barame
 
                                    
                                
                                                Zero 
                                                stress 
                                                Zero 
                                                panique 
                                                Dieulsi 
                                                li 
                                                ma 
                                                indi
 
                                    
                                
                                                Lou 
                                                bloqué 
                                                sama 
                                                yone 
                                                believe 
                                                me 
                                                Nako 
                                                boulé
 
                                    
                                
                                                Khawma 
                                                ndakh 
                                                degg 
                                                Ngam.
 
                                    
                                
                                                Hey 
                                                boma 
                                                touddé
 
                                    
                                
                                                Ma 
                                                Todj 
                                                sa 
                                                nounara
 
                                    
                                
                                                Hey 
                                                fouma 
                                                jouer 
                                                ay 
                                                liasse 
                                                tourou 
                                                na 
                                                fa
 
                                    
                                
                                                Bou 
                                                gnou 
                                                diawalé 
                                                Peureum 
                                                dou 
                                                ngualam
 
                                    
                                
                                                Wala 
                                                bok 
                                                yaw
 
                                    
                                
                                                Wari 
                                                sur 
                                                Wari 
                                                kouma 
                                                xam 
                                                bouma 
                                                khamé
 
                                    
                                
                                                Lila 
                                                sonal 
                                                bouma 
                                                ko 
                                                meuné 
                                                doto 
                                                wory
 
                                    
                                
                                                Gor 
                                                la 
                                                Tchi 
                                                gor 
                                                yi,
 
                                    
                                
                                                Feugg 
                                                sama 
                                                deunn 
                                                bitch 
                                                Niggaz 
                                                yi 
                                                waff 
                                                Golo 
                                                dou 
                                                gorille
 
                                    
                                
                                                Djom 
                                                la 
                                                Lay 
                                                colis
 
                                    
                                
                                                Tegal 
                                                la 
                                                sam 
                                                Tegal 
                                                la 
                                                sama 
                                                life 
                                                Ngua
 
                                    
                                
                                                Guiss 
                                                ni 
                                                meune 
                                                nagn 
                                                Tchi 
                                                guéne 
                                                khour 
                                                lalay 
                                                doli
 
                                    
                                
                                                BuzzLab 
                                                Tchi 
                                                trône 
                                                Bi
 
                                    
                                
                                                Oundougang 
                                                ress 
                                                défense 
                                                Bi 
                                                Balle
 
                                    
                                
                                                Dou 
                                                diegué 
                                                Nigga 
                                                Bou 
                                                diegué 
                                                gnou 
                                                bodji
 
                                    
                                
                                                Fii 
                                                léppeu 
                                                modji
 
                                    
                                
                                                Cash 
                                                Bangui 
                                                Tchi 
                                                poches 
                                                yi,
 
                                    
                                
                                                Saayou 
                                                gnou 
                                                joué 
                                                teglé 
                                                liasses 
                                                comme 
                                                au 
                                                Monopoly
 
                                    
                                
                                                Gno 
                                                ress 
                                                monopole 
                                                Bi,
 
                                    
                                
                                                Boul 
                                                doff 
                                                non 
                                                noto 
                                                fils,
 
                                    
                                
                                                Zero 
                                                concurrence 
                                                kou 
                                                gnou 
                                                teukkou 
                                                tok 
                                                d'office
 
                                    
                                
                                                Li 
                                                gnou 
                                                yénou 
                                                Bo 
                                                ko 
                                                dékko 
                                                dome 
                                                tokki
 
                                    
                                
                                                Comme 
                                                gold 
                                                Tchi 
                                                soufou 
                                                baat 
                                                lignouy 
                                                def 
                                                par 
                                                force 
                                                Ngua 
                                                koy 
                                                Guiss
 
                                    
                                
                                                Nigga 
                                                niongui 
                                                Tchi 
                                                Kaw 
                                                kou 
                                                gnou 
                                                tek 
                                                beut 
                                                torticolis
 
                                    
                                
                                                Bokkougnok 
                                                gnome 
                                                dara 
                                                ni 
                                                kou 
                                                diangué 
                                                keuram 
                                                Ak 
                                                kou 
                                                diogué 
                                                koki
 
                                    
                                
                                                Yaw 
                                                dangua 
                                                wara 
                                                tok 
                                                Nigga
 
                                    
                                
                                                Ma 
                                                teggal 
                                                Ngua 
                                                Ngua 
                                                sip
 
                                    
                                
                                                Sama 
                                                gang 
                                                gneupa 
                                                tok 
                                                Nigga
 
                                    
                                
                                                Lou 
                                                teggouwoul 
                                                dagn 
                                                ko 
                                                sip
 
                                    
                                
                                                Lignouy 
                                                deff 
                                                Day 
                                                oubalé 
                                                mélni 
                                                thiouraye
 
                                    
                                
                                                Ding 
                                                gnou 
                                                yeuk 
                                                meme 
                                                bo 
                                                gnou 
                                                guissoul
 
                                    
                                
                                                Lerr 
                                                na 
                                                ni 
                                                ndelou 
                                                abdoulaye
 
                                    
                                
                                                Gnoune 
                                                Ak 
                                                yene 
                                                dou 
                                                bene 
                                                fils
 
                                    
                                
                                                Bo 
                                                nandoul 
                                                gnou 
                                                nandal 
                                                la
 
                                    
                                
                                                Ndanane 
                                                Tchi 
                                                ndanane 
                                                yi 
                                                djeuff 
                                                dji 
                                                Day 
                                                Wakh
 
                                    
                                
                                                Troisième 
                                                Barame 
                                                nguay 
                                                guiss
 
                                    
                                
                            1 Mane La Wone
2 Dedet
3 Walabok Baye
4 Girls (feat. Cheeks & Zou Kana)
5 Weurseuk (feat. Eliane)
6 Atanougnou Dome
7 Noflaye (feat. Eliane)
8 Radison Music (feat. Tenny)
9 Well Done
10 Kholal
11 3iem Baram
12 Sama Prof (feat. 2k)
13 Metti
14 Werouwaye
15 It's Bass
16 Mane Rek Ngua Bagn (Bonus Track)
17 Dama Koy Dundu (Bonus Track)
Attention! Feel free to leave feedback.