Canabasse feat. eliane - Weurseuk (feat. Eliane) Lyrics

Lyrics Weurseuk (feat. Eliane) - Eliane , Canabasse



Kou nek ak sa yone
Kou nek ak sa weurseuk
Di nga forr li nga mom
Ba mou mat seuk
Nga ame nga niak
Lepp GOD la
Xiro bi ak ngayo bi
Kone louko fi diar
Kou nek ak sa yone
Kou nek ak sa weurseuk
Di nga forr li nga mom
Ba mou mat seuk
Nga ame nga niak
Lepp GOD la
Xiro bi ak ngayo bi
Louko fi diar
Dougou bi youxou lay tambalé
Kepp kou dioudou ragné
Life bi dara dou easy
Yeug yeug gou brise bi
Dal la ngay trembler
Ngay domou ki mba bou
Dioudou clinique mba ci mbéde
Sa baye toudou Mouhamadou Rassoul wala Pierre
Kene dou xam foy dem
Leu nga fay fekk ak nieuleu fay terou ndakh dangay takh niou begg wala daniou lay xelou
Ndakh sa yaye limou dougou banga dioudou mom léroul
élimanou kogn bi
Moy done sa baye
Wala katior bi ci jail bi
Mo teuf sa yaye
Nga balma bou missal yi may tek dalay choquer
Mais life bi yene say dangay great ba sa xell chauffer
Stopper
Mo niou si guéné
Yeah gueum
Nioune dougnou si lenn bour bi yalla moy sédaler
Li gnou war moy gueum
Nioune dougnou si lenn bour bi yalla moy sédaler
Kou nek ak sa yone
Kou nek ak sa weurseuk
Di nga forr li nga mom
Ba mou mat seuk
Nga ame nga niak
Lepp GOD la
Xiro bi ak ngayo bi
Kone louko fi diar
Kou nek ak sa yone
Kou nek ak sa weurseuk
Di nga forr li nga
Mom ba mou mat seuk
Nga ame nga niak
Lepp GOD la
Xiro bi ak ngayo bi
Louko fi diar
Louko fi diar




Canabasse feat. eliane - Dk Spirit
Album Dk Spirit
date of release
08-04-2016



Attention! Feel free to leave feedback.