Dip Doundou Guiss - Deug Deug - translation of the lyrics into French

Lyrics and translation Dip Doundou Guiss - Deug Deug




Deug Deug
Deug Deug
Yeah
Ouais
DIP
DIP
Check
Check
Da nga teudone rek di guënte wayé nala yéé
Je vais te dire ce que je pense, chérie
Ndakh nagnema deug nekhoul deugueuntane na nekh
Je vais te dire la vérité, si tu veux bien l'entendre
Boul meusseu xepp dara kounek lila Yallah may
Tout le monde s'agite, ils cherchent des problèmes, Yallah, ma parole
Xalé ba ngui djoy mateu mbélènetane la rek
Les jeunes n'ont plus de joie, ils ne pensent qu'à l'argent, vraiment
Meunouma nadjé yégueu none yéma téla xékh
J'ai refusé d'être une femme mariée, je ne voulais pas être enfermée
Tchine bou baxé xégne da fek dafa ndara nekh
La Chine a fait son entrée, tout a changé, tu vois
Deug bou amoul massla la ndara tek nak
Un "deug" sans problèmes, c'est ce que je recherche
Real Rap dou Salsa dou Wane Téraméra
Du vrai rap, de la salsa, sans chichi
Gnouné mola gueune mougneul di nga meusseu mogneu
L'hypocrite me dégoûte, il essaie de me tromper
Maye lathie loutah sa ndey dior gueuneul la sa thiamogne?
Il fait semblant d'être pieux, mais ses actions disent le contraire, n'est-ce pas ?
Loutah ngay laabé thiamogne ndey dior-ra dankone?
Il fait semblant d'être innocent, mais ses actions disent le contraire, n'est-ce pas ?
Loutah Goor yi di sawé thiamogne thiamogne ndey dior-ra tankone?
Ces hommes qui prétendent être religieux, leurs actions disent le contraire, n'est-ce pas ?
Li ngay gueume molay dal lolou rek-kafi
Je ne me laisserai pas avoir par leurs mensonges, vraiment
Diaroul di sett fou sori sa boppeuh doy nala firndé
Leurs paroles sont creuses, leurs actions ne suivent pas, c'est clair
Bagni nek boy lagne gnou téré carte xaliss
J'ai vu des mecs riches devenir pauvres, sans rien du tout
bobou ba légui LONASE mo ngui lindia sunu Pa yi
Et ceux qui étaient pauvres sont devenus riches, LONASE a ruiné nos pères
nga Yallah nga gueum loy doyé gris-gris
Je demande à Dieu de me protéger du mal
nga mbède ngay téwal loy dokh di saw cii murs yi
Je demande à Dieu de me donner la force de résister aux tentations
Li ngay dégue gnoulay wakh boukoutak lignou lay wane
Je me suis battu dur, j'ai travaillé dur pour en arriver
Wakh li ngay deffa gueuneu yomb ngay def li ngay wakh
J'ai traversé des épreuves, j'ai surmonté les obstacles
Goor Yomboul ndax amena goor-djiguène yougnou djongal
Un homme doit être courageux, comme un lion dans la jungle
Mane nek na Goor Yallah bala ma djongou
Je suis un homme de Dieu, personne ne peut me toucher
I'm Real niggah douma sopalikou
Je suis un vrai, pas un hypocrite
Damay khar samay tank toubeuy ba mère bi nopalikou
J'ai arrêté de mentir, j'ai demandé pardon à ma mère, l'hypocrite
Kou bagne gnou wakh loumou défoul, dou wané loumou nékoul
Certains travaillent dur, d'autres non, chacun son destin
Noone ya ngui fouma yégoul douma lène dieuw dama lén ci teukou
Certains ont tout, d'autres non, c'est la vie, c'est comme ça
Ya ngui cii kaw ma ngui cii souf lolou motah maye sissou
Certains ont la chance, d'autres non, c'est comme ça, c'est le destin
Gnam bi souma cii lékoul fawma keupeu cii souf
Je ne regrette rien, je ne me plains pas, c'est mon choix
Sen Flow dissoul kène ci yène todjou cii Youtube
Mon flow est unique, tu ne trouveras ça nulle part ailleurs, même sur Youtube
Rap rek lafi guissoul fuck gni nane damay sissou
Du vrai rap, du pur, je me fiche du reste, je fais mon truc
Time is money wakh ko bororm Montres yu chère yi
Le temps c'est de l'argent, je ne porte pas de montres chères
Ba nga fataliko dealers youniou kep cii jail yi
Ceux qui les portent finissent souvent dealers ou en prison
Sokhor ba bougnou défé lou bakh dafa fek gnou joum
L'oisiveté est un poison, le travail est la solution, c'est un fait
Xalé bouy diawalé dalam yène say mou solko mou djoupp
Le jeune qui traîne sans rien faire finira mal, c'est sûr
Sa life dafa yombone ngay woute life bou djingue
La vie est belle, profites-en, vis ta vie à fond
Aduna rawaneté la rek légui moudjé nga
Le monde est éphémère, ne l'oublie jamais
Boy yi djapé sen boppeuh star, Stars yi djapp sen boppeuh
Certains rêvent d'être des stars, les stars rêvent d'autre chose
Roussena njeukeunté djémouma raw Usain Bolt
Soyez reconnaissants, soyez heureux, courez comme Usain Bolt
Bokoumak gni di wakh le ciel est la limite
Beaucoup disent que le ciel est la limite
Assamane yi beuri nagne kone bi dou sama limite
Mais pour moi, il n'y a pas de limite
Xepp tokou dérette bidoul xonkal keuleu méw
J'avance sans relâche, je brise les obstacles
Est-ce que takhoul gnou mystique badi souli néw?
Est-ce que j'ai un don mystique ?
Kou xam ñi tey'lé ay bakaan tchi ay mbiir you nëw
Si tu ne le crois pas, demande autour de toi, ils te le diront
Journal bi lou nieup xam rek lay souligné
Le journal en a parlé, c'est écrit noir sur blanc
Télé ngay tok di sétane kou amoul lou matt sept ans
Je regarde la télévision, je vois des choses incroyables
Ci Film bo xam kou amoul 16 ans douko sétane
Dans les films, on voit des choses encore plus incroyables
Diamono ngui dokh nieup ngui toppeuh Sheytane
L'argent est un piège, il peut te mener au diable
Yaw démalak sa xel xol fi ngay tek say tankeu
Ne te laisse pas aveugler par l'argent, réfléchis bien
Accident yi beuri nagnou cii nignouko guissé
Les accidents sont fréquents ici, à cause de la vitesse
meusso dégue Carrapide firr na policier
Je ne cours pas après les voitures rapides, je ne suis pas un policier
Xalissou rééwmi kou nek meussna cii cotisé
Je ne suis pas un politicien corrompu
Ngour ngui lekk ko dignou leurré ak audité
Je ne suis pas un menteur, je dis la vérité
Obama louko indi léwal goor-djiguène
Obama est parti, il a laissé les Africains se débrouiller
Nélène gnou wakh cii chomage bi gnoune nio ngui déh
Le chômage est un fléau, il faut trouver des solutions
Agression day fay ndakh def nagnou ko liguéy
L'insécurité est galopante, il faut se protéger
Wagnékou woul ndax gnikoy def yeup gnam nagnou jail
Je ne veux pas aller en prison, je veux rester libre
Mbède boumou takh nga taukh baune boul meusseu done soulard
L'alcool est dangereux, il peut te détruire
Ragal Dou Diégui Rail Bandit dou dokh cii filou courant
Je ne suis pas un bandit, je suis un homme honnête
Légui nieup am fiit xalé yi sakh dawatougnou KanKourang
L'éducation est importante, il faut envoyer les enfants à l'école
Chrétien amo BIBLE, Dioulite boudoul khol AL-QURAN
Les chrétiens ont la Bible, les musulmans ont le Coran
Ray nagnou Sadam Hussein ak Ossama Ben Laden
Il y a des gens mauvais comme Saddam Hussein et Oussama Ben Laden
nagnou dougou nagnou Akhrou Zamane may day
Le monde est en proie au chaos
Picc bou laké cii taate day beug am morom
La violence est partout, il y a trop de morts
Sheytane dafa takk beug gno def morom
Le diable est à l'œuvre, il sème la mort et la destruction
Fène tribunal wessou woul Ragal nitt gnémé Yallah
Au tribunal, on juge les gens au nom de la loi
Monsieur le Juge do Yallah kone boul topando Yallah
Monsieur le juge, rendez la justice au nom de Dieu
Yélwane def nagnou ko Job ndax kène bagnoul diokhé nguir Yallah
Donnez-moi du travail, j'en ai besoin pour vivre
Wayé boy mayé ay Millards faw gnou Caméra la
Certains ont des milliards, ils les dépensent comme ils veulent
Président day djité sakh gniko voté loule
Le président a été élu, il doit tenir ses promesses
DIP jottéwoul ak yaw mais li ngay RAP moko dougoul
DIP est là, je suis pour dire la vérité, mon rap est authentique
Texte bou tilime la bindé deug dji ngène dégue
Ce texte est puissant, il est rempli de vérités
Di ngène bëg boudé beug ngène dégue deug deug
Je suis honnête, je dis ce que je pense, deug deug






Attention! Feel free to leave feedback.