Dip Doundou Guiss - Interview Lyrics

Lyrics Interview - Dip Doundou Guiss



Intro
Mane la dip bou doundou guiss
Depuis grand yoff represent reptyle music
Boy bou naww rappeur bou makk tek ci lucide
Le futur khamagoma i'am the new shit
Waxal sama nonn yi ne parei na
Sama vrai nom we c'est dominique preira
D bi I bi P bi
Maye maitre bou djangual bi
Dip ci sama toure la djougue
Non dou takale dou pmu
(Mc)
Dama yagg beugue rap
Khawma saxx kagn la dalei rap
Depuis bi may khalei la ko fowei sama galei mame
Bign may waylo ay son wou darra ji ak pbs
Gni fi nieukone nek teh dan ko deff khame nga rek
Me 2009 la sogga yegg ne dina nekk rappeur
2009 lay bind texte rappeur
2011 lay dadjek south yi niou former team
Ma creer doundou guiss ba 2012 niou dem reptyle music
(Mc)
Lima dougall si rap souma kayy wakh tey dou diekh men
Digniy yemm rek si loudoul meuss degn men
Marozik dem loge paris saint germain
Marozik dem loge parc des princes men
Aka omar barry
Li ma dougall si rap yeah joue na ci lou barri
Call lam lay nieuk freestyle si ay beatou sonnerie
Galem la done binde texte yagga tankal tantam yi
Lolou fallait que ma wakh ko nakh nonou la fa demei
Rap rek ka kham li ne ci man ak nane la key guene
Lolou ma ci dougal teh lolou rek ka ma ci bayi
Seddo sama life ak gni may get everybody
Fuck siww, fuck clip, fuck djizz, fuck money yeah
Rap real showbizz deuxieme la men
(Mc)
Rap galsen daffa nek mbirr bou jaxasso
Teh lou jaxasso bo ci dougue da lay jaxasse
Mais dou teré ma joxxe point de vue ci interview bi
Game bi démoul teh guiss nenn crew you neh
Dign lay deff rappeur bou mak
Rappeur bou mak teh amo album
Guiss na fi 20 ans de rap bene album
Digniy wakh douniou job fimoy galsen
Moy gni boy yi di royy stylou gangster
Teh lepp di khar teh nji teulé dougn fi diougue
International ladj na lenenn loudoul bi game
Wokh ko samay mc ak samay dj
Game bi lay tall ak sama essence ak sama briquet
(Mc)
Non mane awma genrou rap damay hard ba di danou rapp
Damay swagg dirty south douma tamou rap
Meuna gueune hip hop blues jazz whatever
Rap dou dine bokouma si gni di jammou rap
(Mc)
Deugue la neh rap da khawa indice fi
Liguey bou lerr rek key takh mou donn fi industrie
Niennang ci guen nienen yi nenen dign len di ciss
Pour niggas yi guene ci djizz faw niou key guene ci street bi
Avant tout senegal dou deuk rap kesse
Teh rap dou nigga da topou si rang kessé
Beutou oundou bi nitt yi di kholei rap
Legn fi narra dindi comme nougn dinde cholera
Mais rappeur you eupe fi dign khawoul fokkalei nak
Nieup wora gueiné nieup ba melni choregraphe yi
Respecte ma concurrence dane sa dollei la
Lepp wara nice ni deumb ak docteur di dorrei graphe yi
Niou beurri djangougn lolo takh sen texte yi ordinaire
Amna niou djang wanté man damalen di cons di
Rap dou son rap dou job rap doundou la
Nigga rappal sa life teh bayi gayi ngey tour leundeum




Dip Doundou Guiss - Beus Niki Tay: The Selec-Tape
Album Beus Niki Tay: The Selec-Tape
date of release
31-12-2015




Attention! Feel free to leave feedback.