Lyrics Nangou - Dip Doundou Guiss
Dinga
nangou
xam
na
dinga
nangou
Dina
nangou
khawma
kagn
wayé
dinga
nangou
Khawma
kagn
wayé
biss
dina
gneuw
nga
nangou
Dinga
nangou
daal
wayé
khawma
kagn
Guissou
ma
louma
takha
bayi
Dina
deff
lounè
Beugo
gnou
nekk
kharitt
Ndakh
do
thia
mouna
yém
Amoo
koy
niirol
Meussou
ma
nopp
kou
melni
iow
Mbëguela
meuna
bété
yagu
nala
guiss
mais
tay
la
kheuy
rek
dof
si
iow
Meunou
ma
comprendre
Nangoulo
ma
wax
Waxoo
lane
mola
nekh
si
mane
Lane
ngay
yeuk
pour
mane
c'est
pas
normal
Iow
rek
ladone
khaar
Nangoul
ma
bayi
dokhane
Wakhal
rek
ni
nangou
nga
Mou
diekh
nangoul
rek
gnou
dem
hooaa
Chaque
midi
30
ngama
dane
romb
ak
sa
blouse
ak
sac
Sama
xol
amone
na
bombe
mais
mousta
takk
Lingu
may
romba
takh
ma
dem
badi
seet
lou
say
tank
Meussou
mala
guiss
ak
goor
dousa
mak
tei
dou
sa
papa
Do
thiip
thiip
gueum
sa
bopp
tei
tégou
sa
temps
Am
nga
style
tei
boko
ak
gniy
deff
bamou
saf
sapp
Leudiooo
yoro
diapou
guel
bou
bari
danger
Miss
bene
beuss
la
sunu
gnintii
beutt
yi
dadié
Ho
mou
mel
ni
dagn
ma
yé
thi
nelaw
Thi
biss
bou
melone
ni
biss
yi
wessou
melone
Mel
ni
sirène
Paka
Wontass
Daf
ma
deff
choc
té
gnémé
woumako
wone
dapp
Pression
bou
magamaka
madone
dal
Question
bima
done
lath
moy
kii
moy
kane
Non
dou
meuguel
ma
amone
flash
Na
yam
si
rombanté
bayeinté
xel
comm
dab
Xawma
kagn
lako
sen
suñu
palantère
sila
dieulé
départ
volontaire
Dam
ko
top
ba
galème
tè
dou
loma
done
tay
May
xalaat
deal
bi
yeup
bou
matone
tay
Thieuy
mbëguel
dou
diay
kene
douko
wanteer
Pour
diapp
golo
si
niayes
fok
nga
done
nandité
Oki
xam
na
galèm
wayé
xawma
touram
PUB
la
rek
film
béngui
dora
commencer
Guissou
ma
louma
takha
bayi
Dina
deff
lounè
Beugo
gnou
nekk
kharitt
Ndakh
do
thia
mouna
yém
Amoo
koy
niirol
Meussou
ma
nopp
kou
melni
iow
Mbëguela
meuna
bété
yagu
nala
guiss
mais
tay
la
kheuy
rek
dof
si
iow
Meunou
ma
comprendre
Nangoulo
ma
wax
Waxoo
lane
mola
nekh
si
mane
Lane
ngay
yeuk
pour
mane
c'est
pas
normal
May
romb
romb
lou
sa
kogn
di
tenter
sama
chance
Bounte
keur
bi
full
ma
khawa
complexer
noo
Fipou
tak
sama
fitt
nanga
def
mangui
fi
Diokhantei
tour
khamantei
some
lath
ma
loumay
deff
fii
Ndakh
khamei
ngama
noo
tei
mane
khamei
nala
sii
Dama
beugone
gnou
cauz
Demale
ba
gnewaatt
Diokh
ma
sama
number
call
Demal
ba
déloussi
Loutakh
nga
bagn
mako
diokh
Noo
fook
nga
gnewaat
Show
bii
bandit
leu
.daf
mané
ma
gneuw
mou
sandi
ma
Jokh
ma
faux
numéro
ma
gnewaat
mou
jokh
ma
numéro
faram
naan
magam
laa
Pour
iow
na
doff
ba
gueum
laa
Boul
ma
diaay
kholou
gueeth
douma
lapp
ndakh
dieune
la
Lima
takha
diokk
dou
sax
ay
number
call
- Lane
la
Khawma
nou
mbëguel
di
sakhé
sama
xol
Dama
la
nopp
waa
dou
rayé
khamna
wayé
yall
naci
dhh
Au
revoir
lim
lay
wax
nii
fook
nga
bayi
si
xel
Mane
amna
koumay
guénal
da
damko
beugu
Mane
guénouma
damay
dougu
Meun
ta
dègn
wakho
deugu
heu
Guissou
ma
louma
takha
bayi
Dina
deff
lounè
Beugo
gnou
nekk
kharitt
Ndakh
do
thia
mouna
yém
Amoo
koy
niirol
Meussou
ma
nopp
kou
melni
iow
Mbëguela
meuna
bété
yagu
nala
guiss
mais
tay
la
kheuy
rek
dof
si
iow
Meunou
ma
comprendre
Nangoulo
ma
wax
Waxoo
lane
mola
nekh
si
mane
Lane
ngay
yeuk
pour
mane
c'est
pas
normal
Iow
rek
ladone
khaar
Nangoul
ma
bayi
dokhane
Waxal
rek
ni
nangou
nga
Mou
diekh
nangou
rek
gnou
dem
hooaa
Nangoul
waay
Yé
beugu
nala
Yé
li
nek
si
mane
hun
xawma
lane
leu
Yé
beugu
nala
check
nakhou
mala
heu
Nangoul
book
théé
War
nga
nangoul
rek
mou
diekh
yé
hunhun
By
SERIGNE
SALIOU
FALL
1 Deug Deug
2 Assamane
3 Khametoma
4 Yone Bi (feat. Fla The Ripper)
5 Sama Jeunesse
6 Day Deep (feat. Elzo Jamdong)
7 A Thindji
8 Reuthie
9 Interview
10 Xam-Xam (feat. Ndongo D)
11 Pogda
12 Rep'team
13 Nangou
14 Doundou Oundou
15 Yaakarouma Ci Keen
16 Poto Lamp
17 May Kane
Attention! Feel free to leave feedback.