Dip Doundou Guiss - Nangou - translation of the lyrics into French

Lyrics and translation Dip Doundou Guiss - Nangou




Nangou
La Fille
Dinga nangou xam na dinga nangou
Une fille, je sais que c'est une fille
Dina nangou khawma kagn wayé dinga nangou
Une fille bien foutue, crois-moi, c'est une fille
Khawma kagn wayé biss dina gneuw nga nangou
Bien foutue, crois-moi, c'est toi la fille que j'aime
Dinga nangou daal wayé khawma kagn
Une fille avec un de ces corps, crois-moi
Guissou ma louma takha bayi
Guissou est mon gars, t'inquiète
Dina deff lounè
Il gère les affaires
Beugo gnou nekk kharitt
On est ensemble comme des bandits
Ndakh do thia mouna yém
On est sur le même chemin
Amoo koy niirol
On est trop forts
Meussou ma nopp kou melni iow
J'ai flashé sur toi comme ça
Mbëguela meuna bété yagu nala guiss mais tay la kheuy rek dof si iow
Ne fais pas la difficile, tu sais que je suis un bandit mais avec toi je suis doux
Meunou ma comprendre
Essaie de me comprendre
Nangoulo ma wax
Je parle d'une fille
Waxoo lane mola nekh si mane
Je parle d'une fille qui me plaît vraiment
Lane ngay yeuk pour mane c'est pas normal
Ce n'est pas normal qu'elle joue à ces jeux avec moi
Iow rek ladone khaar
C'est toi que je veux
Nangoul ma bayi dokhane
Laisse-moi te parler franchement
Wakhal rek ni nangou nga
Je suis vraiment amoureux
Mou diekh nangoul rek gnou dem hooaa
Je suis amoureux d'une seule fille, putain
Chaque midi 30 ngama dane romb ak sa blouse ak sac
Chaque midi, 30 000 francs CFA dans son sac avec son chemisier
Sama xol amone na bombe mais mousta takk
Mon cœur bat fort, mais je me retiens
Lingu may romba takh ma dem badi seet lou say tank
Je veux lui parler mais j'ai peur de me planter
Meussou mala guiss ak goor dousa mak tei dou sa papa
Je suis un bandit avec les hommes, je ne suis pas du genre à supplier le père d'une fille
Do thiip thiip gueum sa bopp tei tégou sa temps
Petit à petit, l'oiseau fait son nid, elle prend son temps
Am nga style tei boko ak gniy deff bamou saf sapp
Elle a du style, bien sapée et classe
Leudiooo yoro diapou guel bou bari danger
Attention, les jolies filles peuvent être dangereuses
Miss bene beuss la sunu gnintii beutt yi dadié
Mademoiselle, sois prudente, il y a des filles à qui on a promis le mariage et qui ont fini seules
Ho mou mel ni dagn ma thi nelaw
Je ne suis pas un enfant, je sais ce que je veux
Thi biss bou melone ni biss yi wessou melone
Tu n'es pas la seule à qui on promet le mariage
Mel ni sirène Paka Wontass
Tu es belle comme une sirène, Paka Wontass
Daf ma deff choc gnémé woumako wone dapp
Tu me fais craquer, ton corps me rend fou
Pression bou magamaka madone dal
Tu me mets la pression comme Madonna
Question bima done lath moy kii moy kane
La question que je me pose, c'est qui me donnera de l'argent ?
Non dou meuguel ma amone flash
Non, ne te moque pas de moi, j'ai eu un flash
Na yam si rombanté bayeinté xel comm dab
Je suis attiré par les filles classes comme d'habitude
Xawma kagn lako sen suñu palantère sila dieulé départ volontaire
Crois-moi, notre relation sera un aller simple
Dam ko top ba galème dou loma done tay
Je suis prêt à tout pour toi, même à aller en prison
May xalaat deal bi yeup bou matone tay
Je veux juste qu'on s'amuse ensemble
Thieuy mbëguel dou diay kene douko wanteer
Ne me dis pas que tu n'es pas intéressée
Pour diapp golo si niayes fok nga done nandité
Pour atteindre son but, il faut de la patience
Oki xam na galèm wayé xawma touram
Tu sais que je suis un homme bien, crois-moi
PUB la rek film béngui dora commencer
C'est la pub, le film va bientôt commencer
Guissou ma louma takha bayi
Guissou est mon gars, t'inquiète
Dina deff lounè
Il gère les affaires
Beugo gnou nekk kharitt
On est ensemble comme des bandits
Ndakh do thia mouna yém
On est sur le même chemin
Amoo koy niirol
On est trop forts
Meussou ma nopp kou melni iow
J'ai flashé sur toi comme ça
Mbëguela meuna bété yagu nala guiss mais tay la kheuy rek dof si iow
Ne fais pas la difficile, tu sais que je suis un bandit mais avec toi je suis doux
Meunou ma comprendre
Essaie de me comprendre
Nangoulo ma wax
Je parle d'une fille
Waxoo lane mola nekh si mane
Je parle d'une fille qui me plaît vraiment
Lane ngay yeuk pour mane c'est pas normal
Ce n'est pas normal qu'elle joue à ces jeux avec moi
May romb romb lou sa kogn di tenter sama chance
Je tente ma chance en allant la voir dans son quartier
Bounte keur bi full ma khawa complexer noo
Il y a plein de belles filles, mais je ne complexe pas
Fipou tak sama fitt nanga def mangui fi
Je fais attention à mon apparence et à mon style
Diokhantei tour khamantei some lath ma loumay deff fii
Je fais le tour du quartier pour voir ce que je peux faire
Ndakh khamei ngama noo tei mane khamei nala sii
On me regarde, je sais qu'on me trouve beau
Dama beugone gnou cauz
Je ne fais semblant de rien
Demale ba gnewaatt
Je me fais discret
Diokh ma sama number call
Je lui donne mon numéro, qu'elle m'appelle
Demal ba déloussi
Je fais semblant d'être occupé
Loutakh nga bagn mako diokh
Je ne la regarde même pas, pour ne pas qu'elle se doute
Noo fook nga gnewaat
Je ne fais que la regarder du coin de l'œil
Show bii bandit leu .daf mané ma gneuw mou sandi ma
Ce show est risqué, je la veux vraiment
Jokh ma faux numéro ma gnewaat mou jokh ma numéro faram naan magam laa
Je lui donne un faux numéro et j'attends de voir si elle m'appellera
Pour iow na doff ba gueum laa
Pour voir si elle est vraiment intéressée
Boul ma diaay kholou gueeth douma lapp ndakh dieune la
Je veux savoir si elle me rappellera après que je sois parti
Lima takha diokk dou sax ay number call - Lane la
Je lui donne mon numéro et j'attends son appel
Khawma nou mbëguel di sakhé sama xol
Crois-moi, elle me plaît vraiment
Dama la nopp waa dou rayé khamna wayé yall naci dhh
Elle est belle et élégante, elle a tout pour plaire
Au revoir lim lay wax nii fook nga bayi si xel
Au revoir, je te laisse, je dois y aller
Mane amna koumay guénal da damko beugu
J'ai envie de la revoir, mais je ne veux pas la brusquer
Mane guénouma damay dougu
Je la veux, mais je vais la laisser venir à moi
Meun ta dègn wakho deugu heu
Tu mérites qu'on te respecte
Guissou ma louma takha bayi
Guissou est mon gars, t'inquiète
Dina deff lounè
Il gère les affaires
Beugo gnou nekk kharitt
On est ensemble comme des bandits
Ndakh do thia mouna yém
On est sur le même chemin
Amoo koy niirol
On est trop forts
Meussou ma nopp kou melni iow
J'ai flashé sur toi comme ça
Mbëguela meuna bété yagu nala guiss mais tay la kheuy rek dof si iow
Ne fais pas la difficile, tu sais que je suis un bandit mais avec toi je suis doux
Meunou ma comprendre
Essaie de me comprendre
Nangoulo ma wax
Je parle d'une fille
Waxoo lane mola nekh si mane
Je parle d'une fille qui me plaît vraiment
Lane ngay yeuk pour mane c'est pas normal
Ce n'est pas normal qu'elle joue à ces jeux avec moi
Iow rek ladone khaar
C'est toi que je veux
Nangoul ma bayi dokhane
Laisse-moi te parler franchement
Waxal rek ni nangou nga
Je suis vraiment amoureux
Mou diekh nangou rek gnou dem hooaa
Je suis amoureux d'une seule fille, putain
Nangoul waay
Une fille comme ça
beugu nala
C'est ce que je veux
li nek si mane hun xawma lane leu
C'est elle que je veux, crois-moi
beugu nala check nakhou mala heu
Je veux la rencontrer, c'est sûr
Nangoul book théé
Une fille bien
War nga nangoul rek mou diekh hunhun
Je suis amoureux d'une seule fille, c'est vrai
By SERIGNE SALIOU FALL
Par SERIGNE SALIOU FALL






Attention! Feel free to leave feedback.