Lyrics Deuil National - Dip Doundou Guiss
                                                Manatuma 
                                                toog 
                                                di 
                                                xaar 
                                                leneen
 
                                    
                                
                                                Li 
                                                nek 
                                                sama 
                                                bop 
                                                bi 
                                                xatt 
                                                na 
                                                fees 
                                                na
 
                                    
                                
                                                Manatuma 
                                                toog 
                                                di 
                                                xaar 
                                                leneen
 
                                    
                                
                                                Dama 
                                                muju 
                                                joow 
                                                ci 
                                                gaal 
                                                ba 
                                                dess 
                                                fa
 
                                    
                                
                                                Lelelelelena 
                                                dama 
                                                muñ 
                                                ba 
                                                de, 
                                                muñ 
                                                bi 
                                                jeex 
                                                na
 
                                    
                                
                                                Ndaw 
                                                si 
                                                diggu 
                                                geej 
                                                weet 
                                                na, 
                                                reer 
                                                na
 
                                    
                                
                                                Sama 
                                                bakanay 
                                                rot 
                                                su 
                                                geej 
                                                gi 
                                                mare 
                                                naan
 
                                    
                                
                                                Lo 
                                                sorale 
                                                dalay 
                                                diisël,
 
                                    
                                
                                                Tëwa 
                                                fatte 
                                                ñima 
                                                bayi 
                                                ginaaw
 
                                    
                                
                                                Nap 
                                                kat 
                                                bi 
                                                gëdj 
                                                na 
                                                giss 
                                                jën
 
                                    
                                
                                                Ku 
                                                saccul, 
                                                ñaanul 
                                                marr 
                                                na 
                                                xiif 
                                                na
 
                                    
                                
                                                Diplome 
                                                ak 
                                                journala 
                                                yam 
                                                këyit 
                                                lë
 
                                    
                                
                                                Fay 
                                                ndox 
                                                ak 
                                                courant 
                                                ba 
                                                tay 
                                                dañuy 
                                                të
 
                                    
                                
                                                Suñu 
                                                quotidien 
                                                mo 
                                                gëna 
                                                tiss 
                                                tëss
 
                                    
                                
                                                Suñu 
                                                kër 
                                                day 
                                                taa 
                                                ndox 
                                                luñu 
                                                miin 
                                                lë
 
                                    
                                
                                                Xamul 
                                                ndax 
                                                yoonu 
                                                xaru 
                                                la 
                                                am 
                                                yoonu 
                                                risque 
                                                lë
 
                                    
                                
                                                Tekkey 
                                                alxuranam, 
                                                tekkey 
                                                biblëm
 
                                    
                                
                                                Geej 
                                                du 
                                                mëssa 
                                                rëy 
                                                ba 
                                                ëp 
                                                fittëm
 
                                    
                                
                                                Gëm 
                                                ni 
                                                buñu 
                                                yegge 
                                                nañ 
                                                yeetal 
                                                fitnë
 
                                    
                                
                                                Def 
                                                ni 
                                                ku 
                                                rep 
                                                giss 
                                                yoon
 
                                    
                                
                                                Dekkufi 
                                                sedd 
                                                di 
                                                lox
 
                                    
                                
                                                Defuñu 
                                                ken 
                                                lu 
                                                bonn
 
                                    
                                
                                                Dadj 
                                                luñu 
                                                yeene 
                                                wul 
                                                dom
 
                                    
                                
                                                Soobu 
                                                si 
                                                teen 
                                                bi 
                                                di 
                                                root
 
                                    
                                
                                                Dem 
                                                te 
                                                ñëw 
                                                tedd 
                                                ni 
                                                Gorr
 
                                    
                                
                                                Dem 
                                                te 
                                                ñëw 
                                                fay 
                                                suñuy 
                                                borr
 
                                    
                                
                                                Delu 
                                                samay 
                                                digg 
                                                mbok
 
                                    
                                
                                                Don 
                                                mak 
                                                si 
                                                kër 
                                                di 
                                                daw 
                                                yërmande 
                                                ak 
                                                ndimbël 
                                                motax 
                                                ñu 
                                                sëss
 
                                    
                                
                                                Xam 
                                                liñu 
                                                bëg 
                                                fimu 
                                                ne 
                                                moy 
                                                xam 
                                                fiñu 
                                                jëm
 
                                    
                                
                                                Yoonu 
                                                geej 
                                                du 
                                                liñu 
                                                gënël 
                                                liñu 
                                                gënël 
                                                moy 
                                                am 
                                                li 
                                                gën
 
                                    
                                
                                                Ken 
                                                bëgul 
                                                doomam 
                                                di 
                                                taggo 
                                                dem 
                                                ñukoy 
                                                deggat 
                                                si 
                                                dëdj
 
                                    
                                
                                                Gaal 
                                                bu 
                                                dëppu, 
                                                këppu, 
                                                këppale 
                                                famille 
                                                lëm
 
                                    
                                
                                                Mëno 
                                                ŋacc 
                                                waye 
                                                dem 
                                                nga 
                                                seeti 
                                                charlie 
                                                demb
 
                                    
                                
                                                Juromi 
                                                temeri 
                                                neew 
                                                Etat 
                                                ne 
                                                du 
                                                wax 
                                                si 
                                                sen 
                                                dëdj
 
                                    
                                
                                                Fi 
                                                yaakar 
                                                si 
                                                nguur 
                                                moy 
                                                yaakar 
                                                si 
                                                ay 
                                                ngandi 
                                                dëm
 
                                    
                                
                                                Manatuma 
                                                toog 
                                                di 
                                                xaar 
                                                leneen
 
                                    
                                
                                                Li 
                                                nek 
                                                sama 
                                                bop 
                                                bi 
                                                xatt 
                                                na 
                                                fees 
                                                na
 
                                    
                                
                                                Manatuma 
                                                toog 
                                                di 
                                                xaar 
                                                leneen
 
                                    
                                
                                                Dama 
                                                muju 
                                                joow 
                                                ci 
                                                gaal 
                                                ba 
                                                dess 
                                                fa
 
                                    
                                
                                                Lelelelelena 
                                                dama 
                                                muñ 
                                                ba 
                                                de, 
                                                muñ 
                                                bi 
                                                jeex 
                                                na
 
                                    
                                
                                                Ndaw 
                                                si 
                                                diggu 
                                                geej 
                                                weet 
                                                na, 
                                                reer 
                                                na
 
                                    
                                
                                                Sama 
                                                bakanay 
                                                rot 
                                                su 
                                                geej 
                                                gi 
                                                mare 
                                                naan
 
                                    
                                
                            Attention! Feel free to leave feedback.