Elzo Jamdong - Nama Yalla Baal Lyrics

Lyrics Nama Yalla Baal - Elzo Jamdong



Taal bou Yalla taal wako féyou ko
Nama Yalla baal gnii ngui seen kow
Takk shine lerr naagn ni bideew
Taal bou Yalla taal wakh féyou ko
Taal bou Yalla taal tole bou Yalla bey
Diaam bou Yalla fal, dey gueuneu Taakkeu di gueuneu teuweu feye
Fall kou Yalla mey daal lo beugg nangou
tchi mom nanga nangou ni deung ko koye feye
Ndakh kou Yalla mey baat dineu wakh te kou am bou neekh de koy weye
Dame dane lakkhatou gni me gueune diégué
(gnimeu) dame lerrone seni beut beu niou goumbeu
Gni me gueuneu sori nio meu done ndieukk sene
mey takk di magg niou mel ni niou moumeu (moumeu)
Niveau bi gueuneu kawé laye football
Legui mbeur yi fi eupp gueudd laye doumeu
Dame diok djité xaroumeu Aldioumeu
Mangui weur kane momeu soute te guissoumeu
Soubeu ci Diante gouddi werr
Takk na shine boul begn lolou ken dou tchi polemiquer
Ngande la lerre neu maye thiaatou bidew
bi dioudou fer di lekk tchi bolou mak yi
Fangg na fegne na diommi nguene ndakh dolé
dji nék tchi mane mo gueuneu kowé dolé djinné
Rangou na khekh na be togg
Tchine gua ngui kheegne nekh te dou gowé tchi (yeah)
Taal bou Yalla taal wakh féyou ko(taal bou yalla taal waakh féyou ko)
Nama Yalla baal gnii ngui seen kow
(Nama Yalla Baal gnii ngui seen kow iow)
Takk shine you lerr naagn ni bideew
Yagg na def ay hit alright
Bobou amagoumeu wone ay clip alright
Li fi Thiere binde tchi recettou beat
Eupp neu ay livre you diekhel ay bic (come again)
Yagg na begueul ay nit alright
Bobou amagoumeu wone aye sites
(Wallaye)
Bi ngay ndieukk degg limeu binde deugueu
replay nangou ni kone mousso wone write (dope)
Ma dakh rap Senegal Diallo
Manekk tchi nguur gui def ko seme Freengdom
Seme dope legalize soumeu nekhone
guenné bum boumey touddé Dakar Kingston
Am dieuleul bi def ko Ringtone
Gningui job moussouniou am piston
Kou le ladj ndakh ma ngui gérer fight bi
neko maye Mouhamet Ali tchi kow ring bro
Mane demey takk doumeu mandi
Ay daadj naturel la andi
Def le Mario diam le aye Champi
Soudone western movie degn mey Wanted (wanted)
Hey boumeu wone se kanamou Gentil
Kham na yangui niaane me fey nga meun tranquille
Demey gass tombe soul ay garçon comme
Gaston tchi microphone mane mey bandit
From the underground liguey bi dorroul tey(dorroul tay)
Guiss nga egg negn tchi kow liguey bou sete dey fey(day faaaye)
Kila yagg tipser lo kepp se good time
Get sunu vibes feel alright
Deniou dore mou nathieu nigga nieupp sèèdé ko wallaye
Change game bi def safaar indi mousslaay
Never never nga guiss niou tchi détails
Wowéma grossiste one more time (uh yeah uh yeah)





Attention! Feel free to leave feedback.