Lyrics Bakkan - Obree Daman
Bul
di
jaawale
Bul
di
jaawale
Bul
di
jaawale
Bul
di
jaawale
Mandu
Mandu
len
Ci
nitt
Bul
di
jaawale
Mandu
Mandu
len
Ci
nitt
Bul
di
jaawale
Dox
naa
ba
ñëw
setsi
la
He
ñëw
setsi
la
Hé
Nitt
de
war
na
mandu
Teey
te
Yalla
tax
Hé
Hé
Seet
naa
la
sow
Seet
naa
la
penku
Mandu
reer
ci
jamano
Seet
naa
la
sow
Seet
naa
la
penku
Mandu
reer
ci
say
jikko
Mandu
Mandu
len
Ci
nitt
Bul
di
jaawale
Mandu
Mandu
len
Ci
nitt
Bul
di
jaawale
Bul
di
jaawale
Bul
di
jaawale
Bul
di
jaawale
Mandu
Mandu
Mën
na
laa
wallu
Mandu
Di
na
Mandu
Ci
doomu
àdama
bi
le
Hé
Seet
naa
la
sow
Seet
naa
la
penku
Mandu
reer
ci
jamano
Seet
naa
la
sow
Seet
naa
la
penku
Mandu
reer
ci
say
jikko
Mandu
Mandu
len
Ci
nitt
Bul
di
jaawale
Mandu
Mandu
len
Ci
nitt
Bul
di
jaawale
Bul
di
jaawale
Bul
di
jaawale
Bul
di
jaawale
Mandu
Mandu
len
Ci
nitt
Bul
di
jaawale
Mandu
Mandu
len
Ci
nitt
Bul
di
jaawale
Bul
di
jaawale
Attention! Feel free to leave feedback.