Lyrics Bantu - Obree Daman
Nitt
Ak
melokaanam
Ci
yërmande
La
ko
Yalla
bindee
Doomu
Àdama
Cëy
xamoon
lu
ko
fi
indi
woon
Hum
du
caaxaan
Fii
Fii
àdduna
la
Ndank
yen
Ci
àdduna
Nitt
moo
ñàkk
xëy
bis
am
beew
Nitt
moo
njool
moo
gàtt
moo
weex
Waaye
ci
yërmande
La
ko
Yalla
bindee
Ho
ho
ho
Ho
ho
ho
Ho
ho
ho
Ho
ho
ho
Yalla
moo
sàkk
goor
ak
jigeen
Magg
ak
ndaw
te
yemale
wu
len
Yalla
moo
sàkk
bëccëg
guddi
Bës
bu
xasa
dem
dootul
deelu
si
Fii
Fii
àdduna
la
Ndank
yen
Ci
àdduna
Ho
fii
Fii
àdduna
la
Ndank
yen
Ci
àdduna
Yalla
moo
sàkk
goor
ak
jigeen
Magg
ak
ndaw
te
yemale
wu
len
Yalla
moo
sàkk
bëccëg
guddi
Bës
bu
xasa
dem
dootul
deelu
si
Attention! Feel free to leave feedback.