Lyrics Bukki - Obree Daman
Nitt
du
mala
Li
ngay
def
Sakkul
naam
xam
ko
Nitt
du
mala
Li
ngay
wax
Seetantal
ko
waay
Nitt
du
mala
jikkoom
Nga
koy
xoolee
doomu
Àdama
ni
la
ñu
Yalla
Bindee
ci
àddunam
si
Ak
sunu
matadi
Waaye
moom
Yalla
rekk
a
xam
Nitt
du
mala
jikkoom
Nga
koy
xoolee
doomu
Àdama
du
dem
safara
Nitt
du
mala
Li
ngay
def
Sakkul
naam
xam
ko
Nitt
du
mala
Li
ngay
wax
Seetantal
ko
waay
Nitt
du
mala
Li
ngay
wax
Seetantal
ko
waay
Wacce
na
taw
ci
ñun
Gancax
gi
mèeñ
na
Ngelaw
gi
feexal
Jànt
bi
leeral
Moo
xam
li
nekk
ci
ñun
Ndax
moo
def
li
nekk
ci
ñun
Kon
mandu
war
na
ñu
Ci
nitt
ni
ko
Yalla
bindee
Nitt
du
mala
jikkoom
Nga
koy
xoolee
doomu
Àdama
du
dem
safara
Nitt
du
mala
jikkoom
Nga
koy
xoolee
doomu
Àdama
du
dem
safara
Nitt
du
mala
Li
ngay
def
Sakkul
naam
xam
ko
Nitt
du
mala
Li
ngay
wax
Seetantal
ko
waay
Nitt
du
mala
Li
ngay
wax
Seetantal
ko
waay
Nitt
du
mala
Li
ngay
wax
Seetantal
ko
waay
Attention! Feel free to leave feedback.