Viviane Chidid - Teeyal Lyrics

Lyrics Teeyal - Viviane Chidid



Par AbouAmg
Dégu teel ni rek tocna (teeyal)
Lou fi jar ngen di daw bay danou (teeyal)
Fo tok beugu niou naw le (teeyal)
Wagnil eupel bayi nétali (teeyal)
Déglu len waaxu yaram ba (teeyal)
Xaam yoon ko guen (teeyal)
Beugu buzz bamu jaral-le (teeyal)
Ngua tagé ko déwa gul (teeyal)
Ku Nek am ngua lila Doy
Féxel nga MJE ko lidieunti
Mane deh lila waax
Sa gallé NGI taak di booy
Jem ko lidienti, Te Fayko deh lila waax
Lu Touti nga def ko lou paata
Lo xaam nétali lila waax
Yakamti rayna sa niome maam
Deuguel rayone na sa niome madame
Bul ko lek niora gul (teeyal)
Bul di wax lo xamni ama gui (teeyal)
Xaamu lo do xaar ba niou xaamal le (teeyal)
Guiss lo do xaar ba guiss lou guen ler (teeyal)
nagua tey ngua daal (teyal))
Amigo Li nguay wax deh woru la (teeyal)
Nopi baax na ci lo xamul lan le (teeyal)
Gawa waax meun na indi musiba (teeyal)
Dégu teel ni rek tocna (teeyal)
Lou fi jar ngen di daw bay danou (teeyal)
Fo tok beugu niou naw le (teeyal)
Wagnil eupel bayi nétali (teeyal)
Déglu len waaxu yaram ba (teeyal)
Xaam yoon ko guen (teeyal)
Beugu buzz bamu jaral-le (teeyal)
Ngua tagé ko déwa gul (teeyal))
Mané li xawma lan la
Li xawma lan la, li xawma lan la li
Mané li xawma lan la
Li xawma lan la, li xawma lan la li
Ki lidieunti na le
Lidieunti na le, lidieunti la yow mi
Ki lidieunti na le
Lidieunti na le, lidieunti la yow mi
Ku nek am ngua lila doy
Féxel nga jem ko lidieunti mane deh lila wax
Sa gallé ngi takk di booy
Jem ko lidieunti fayko deh lila waax
Lu touti nga def ko lou paata
Lo xaam nétali lila
Raymaax sa Yamaax niome madame
Deuguel rayone na sa niome madame
Li ngua bind est ce que deugu le (teeyal)
Fake news man yeugueluma (teeyal)
Beug buzz ba tax ngua dima sossal (teeyal)
Li ngua def deh xaam ngua loum toumal toumal (teeyal)
Boy yakati nit (teeyal)
Wala sah boy bond ci nit (teyal)
Nala ler linguay waax ni lu am le
Luko moy dina don sa musiba
Dégu teel ni rek tocna (teeyal)
Lou fi jar ngen di daw bay danou (teeyal)
Fo tok beugu niou naw le (teeyal)
Wagnil eupel bayi nétali (teeyal)
Déglu len waaxu yaram ba (teeyal)
Xaam yoon ko guen (teeyal)
Beugu buzz bamu jaral-le (teeyal)
Ngua tagé ko déwa gul (teeyal)
Dégu teel ni rek tocna (teeyal)
Lou fi jar ngen di daw bay danou (teeyal)
Fo tok beugu niou naw le (teeyal)
Wagnil eupel bayi nétali (teeyal)
Déglu len waaxu yaram ba (teeyal)
Xaam yoon ko guen (teeyal)
Beugu buzz bamu jaral-le (teeyal)
Ngua tagé ko déwa gul (teeyal)



Writer(s): Beneth Seraphin Akatche Koffi, Viviane Chidid


Viviane Chidid - Teeyal - Single
Album Teeyal - Single
date of release
17-07-2021

1 Teeyal




Attention! Feel free to leave feedback.