Youssou N'Dour - Mbeugël Is All (Version Mbalax ) (Chérie Coco) Lyrics

Lyrics Mbeugël Is All (Version Mbalax ) (Chérie Coco) - Youssou N'Dour



Mbeuguel leuh woor
Mbeuguel is all
Neuh woora woor
Souleuh beugué neuh woor
Salimata néwone ngama beugoulooma
Diégué ma diégué ma
Chérie boy
Kaay ngeu diégué ma
Fooy moudié Fooy moudié akh mome
Douleuh door tei dou leuh raay kone kouné langal akh seuh waay
Salimata néwone ngama beugouloma
Diégué ma diégué ma
Chérie booy
Kaay ngeu diégué meuh
Chérie coco diokhnaleuh sama khol
Boolé seuh dileuh yeureum
yitt dileuh mougneul
Li souleu doyoulé
Daff dane solou kheil diko téyé sii yaramam
Sou goudi meussaneuh diott sii souff sou sédeuh sii
Aminta ndiaye néwone naleuh djiguéne douma fonto
Togn ngama beineuh yonne
Meuh wakh ko seuh yaye
Ngeu deilou togna tii meuh
Fooy moudié
Fooy moudié Fooy moudié akh mome
Douleuh door tei dou leuh raay kone kouné langal akh seuh waay
Mbeuguel leuh woor
Mbeuguel is all
Neuh woora woor
Souleuh beugué neuh woor
Mbeuguel leuh woor
Mbeuguel is all
Neuh woora woor
Souleuh beugué neuh woor
Djiguéne gnéy souniou lumiere
Wayeii nioy seine courant
Sou khol yii leundeumei
Souniou mbeuguel mokoy léral
Annnnnh Djiguéne gnéy souniou lumiere
Wayeii nioy seine courant
Sou khol yii leundeumei
Souniou mbeuguel mokoy léral
Waay leine
Waay leine mbeuguel
Djiguéne gnéy souniou lumiere
Wayeii nioy seine courant
Sou khol yii leundeumei
Souniou mbeuguel mokoy léral
Aay thiono leuh
Boulko weddi aay thiono leuh
Miss yii nio tarou
Meuh wakh koo beineuh yone tei
Yacine bobou diambar leuh waune
Wouy fénéne
Wouye fénéne
Wouye fénéne
Wouy fénéne
Wouye fénéne
Wouye fénéne
Souma wakhtanei
Souma wakhtaneii akh sama gnéguénaay téyél lako
Manguii khol seuh baneikh
Mangui khol ningay doundé
Manguii khol seuh baneikh
Mangui khol ningay doundé
Souma wakhtaneii
Souma wakhtaneii akh sama gnéguénaay téyél lako
Salimata néwone ngama beugouloma
Diégué ma diégué ma
Chérie booy
Kaay ngeu diégué meuh
Fooy moudié Fooy moudié akh mome
Douleuh door tei dou leuh raay kone kouné langal akh seuh waay
Mbeuguel is all
Neuh woora woor
Souleuh beugué neuh woor
Mbeuguel leuh woor
Mbeuguel is all
Neuh woora woor
Souleuh beugué neuh woor
Aminta ndiaye néwone naleuh djiguéne douma fonto
Togn ngama beineuh yonne
Meuh wakh ko seuh yaye
Ngeu deilou togna tii meuh
Manguii khol seuh baneikh
Mangui khol ningay doundé
Manguii khol seuh baneikh
Mangui khol ningay doundé
Aminta ndiaye néwone naleuh djiguéne douma fonto
Togn ngama beineuh yonne
Meuh wakh ko seuh yaye
Ngeu deilou togna tii meuh
Djiguéne gnéy souniou lumiere
Wayeii nioy seine courant
Sou khol yii leundeumei
Souniou mbeuguel mokoy léral
Annnnnnh Djiguéne gnéy souniou lumiere
Wayeii nioy seine courant
Sou khol yii leundeumei
Souniou mbeuguel mokoy léral
Waay leine
Waay leine mbeuguel
Neuh woora woor souleuh beugué neuh woor
Aminta ndiaye néwone naleuh djiguéne douma fonto
Togn ngama beineuh yonne
Meuh wakh ko seuh yaye
Ngeu deilou togna tii meuh
Fooy moudié Fooy moudié akh mome
Douleuh door tei dou leuh raay kone kouné langal akh seuh waay
Waay leine
Waay leine mbeuguel
Neuh woora woor souleuh beugué neuh woor
Mbeuguel leuh woor
Mbeuguel is all
Neuh woora woor
Souleuh beugué neuh woor



Writer(s): toumani diabaté, youssou n'dour


Youssou N'Dour - Seeni Valeurs
Album Seeni Valeurs
date of release
01-08-2017




Attention! Feel free to leave feedback.