Lyrics Mbeugël is All (Version Remix) - Toumani Diabaté , Youssou N'Dour
Mbëgel
la
woor
Mbëgel
is
all
Na
woora
woor
sou
la
beugé
na
woor
Salimata
néwoone
gua
ma
beugouloma
Djéguéma
djéguéma
Chérie
boy
kay
gua
djéguéma
Foy
moudié
foy
moudié
Foy
moudié
ak
mom
Doulaa
door
té
dou
la
reukk
kone
kouné
langal
ak
sa
way
Salimata
néwoone
gua
ma
beugouloma
djéguéma
djéguéma
Chérie
boy
kay
gua
djéguéma
Chérie
coco
diokhh
nala
sama
khôl
Bolékok
di
la
yeureum
té
itt
du
la
mougneul
ni
soula
doyoulé
Dafa
dane
li
guëne
di
ko
tekk
tchii
yaramame
Sou
gouddi
meussana
djott
Si
souf
sou
sëdd
si
Aminata
Ndiaye
néwone
nala
djiguèbe
dou
ma
fonto
togn
gua
ma
benn
yone
wa
wax
ko
sa
yaye
gua
délou
tognatima
Foy
moudié
foy
moudié
Foy
moudié
au
môme
dou
la
door
té
dou
la
ray
Koné
kouné
langual
ak
sa
waye
Mbëgel
la
woor
mbëgel
is
all
na
woora
woor
soula
beugué
na
woor
Mbëgel
la
woor
mbeugel
is
all
na
woora
soula
beugué
na
soir
Djiguène
nièye
sounou
lumière
wayé
nioy
sène
courant
sou
kholli
leudeumé
sounou
mbeugel
lakoy
lérall
Anhh
djiguène
nieye
sounou
lumière
wayé
nioy
sène
courant
Sou
khôl
yi
leudeumé
sounou
mbeugél
lakoy
lérall
Waye
lène
wayye
lènne
mbeugellll
Djiguène
nieye
sounou
lumière
wayé
nioy
séne
courant
sou
khol
yi
leudeumé
sounou
mbeugel
lakoy
lérall
Aye
tionno
la
boul
KO
wéddi
aye
tionno
la
Mi
sionta
ma
wax
ko
béne
yone
té
déé
Yacine
boubou
diambar
la
wone
Wouye
fénéne
wouye
fénéne
Wouye
fénéne
wouye
fénéne
wouye
fénéne
wouye
fénéne
Souma
waxtané
souma
waxtané
Sama
djéguénaye
déé
lako
Magui
kholl
sa
banéxx
magui
ni
guay
doundé
Souma
waxtané
souma
waxtané
sala
djéguénaye
déé
lako
Salimata
néwognama
beugouloma
djéguéma
djéguéma
Chérie
boy
kay
gua
djéguéma
Fay
moudié
foy
moudié
mome
doula
door
téé
doula
ray
Koné
kouné
languall
ak
sa
waye
Mbeugel
is
all
Soula
beugé
na
woor
Attention! Feel free to leave feedback.