Diogal Sakho - Massa thiona paroles de chanson

paroles de chanson Massa thiona - Diogal Sakho



Mame Khady Dia Baye
Massa Thione
Mame Khady Dia Baye
Massa Thione
Yow so Kheuyé
Nadj bi tangue bi
Yangui Yenou xa ndiaye
Di yakar xa borom
Yow so Kheuyé
Nadj bi tangue bi
Yangui Yenou ca ndiaye
Dioubal xa place ba
Yow so Kheuyé
Nadj bi tangue bi
Yangui Woula Yoné
Mate Djité




Diogal Sakho - samba Alla
Album samba Alla
date de sortie
27-07-2006



Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.