Diogal Sakho - Mama paroles de chanson

paroles de chanson Mama - Diogal Sakho



Yow mareme Diagne naaré maréme diomba ñaw waye nala Diagne
Yow mareme diangne naaré maréme diomba ñaw waye nala diangne
Yow mareme kouye sa baye mame gorgui ndoye moy sa maamé do gnawéé yow mareme Kouye sa baye Mame Birame moye sa bayéé maréma maréme he he he
Adounabi daffa diakhasso bagnii
Baréé Adounabi daffa diakhasso bagnouye wayié mane mi Samba Diogal waye na maréme Diagne
Narrou Birame Diagne babi binta Diagne naaré Birame Diagne magui fama Diagne narrou Birame Diagne magui Souley Diagné narrou Birame Diagne Maréme Birame Diagne codeye Diagnééé Diagne naare yowe do doore do saga méré narrou Birame Diagne do doore do saga do méré
Kou la miine Dou la bayéé Diagne naare bilahi daga bahé hé.
Narrou Birame Diagne Yow do doore do saga do méré Diagne narre Kou la mine dou la bayéé Diagne narre Kou la mine dou la bayéé




Diogal Sakho - samba Alla
Album samba Alla
date de sortie
27-07-2006



Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.