Diogal Sakho - Beugeuna paroles de chanson

paroles de chanson Beugeuna - Diogal Sakho



Beugona kou kham guene di xameli waaw
Beugona kou niakk gueneu am yakkar
Beugona guiss taw fou bekoor wal yaye
Beugona am am katan gouma teireulei yaye
Beugona nieup bokk liniouy am
Beugona guiss xalei yeup contane
Beugona am am katane gouma teireulei yaye
Cey li beuss bou amei iow cey li
Souma doundei nakko niane
Kiy mayei
Kitaye dinako niano mane dal dinako niane
Litaye dinako nianei mane dal dinako niane cey ley
Ousmano Dioufo ko diokh ndeki mou yakkar agn
Ousmanoy ley
Ngi xam dh danio xamnei kou niakk dana am yakkar
Mane dal beugna guiss tawfi bekoor waaw
Sako narou Sokhna nangouna terral yayam
Souma dounde nakko niane




Diogal Sakho - samba Alla
Album samba Alla
date de sortie
27-07-2006



Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.