Dip Doundou Guiss - Assamane - traduction des paroles en anglais

Paroles et traduction Dip Doundou Guiss - Assamane




Assamane
Assamane
Kholal cii kaw nga bayifa saye beut
It's like your thinking is cutting-edge and advanced
Guisso dara lou djara thiow mo waral lepp
You're so smart that I can't keep up with your thoughts
Guisso dara lo meuneu laale lo meusseu tiim ak saye beut
You're a genius, you know so much about so many things
Kholal ci kaw assamane wessu nga sa level
Your mind is like a universe, it's so vast and complex
Gni fa défouniou bruit louné nga lène dégueul
You're always pushing the boundaries, exploring new ideas
Mais niouné nioune deukou gnoufi kou déh dinagnela yégueul
But you're also so down-to-earth and humble
Sama biss mou ngui nieuw, sama booss tayla xeuyna
I love talking to you, you always make me think
Kone bou défé nga ndieuk dem néko nama diégueul
I'm so lucky to have you in my life
Nieup nénagne daf gnou tiim kone mo ngui cii assamane
You're one of a kind, there's no one else like you
Loutah mou tek niou fi lathieko saye maame Adama ak Awa
You're beautiful, smart, and funny
Nénagne nioune nio ngui doundeu Akhirou Zamane
You're the best friend I could ever ask for
Kou djot lettrou assamane exactement ndakh dama khawa
I love you more than words can say
Yémou cii gni wané nii niom gueumeu tougnouko
I can't wait to see what the future holds for us
Pour mane gni gueum gno yéwou gni dess dagno guemeintou
I know we're going to do great things together
Comme Scientifique ak Philosophe yi diémeu prouvé lénène
As scientists and philosophers, we'll change the world
Boudé bo guissoul do meusseu gueum déh nga thi poukeuré men
We'll prove that anything is possible
Doko door balle bamou diaaleu
You're a rare gem
Ropalane khalatoufa yégueu
A true treasure
Lougni def xana sani niaane
I'm so grateful for your friendship
Di niaane Yallah na ngou niaane yikoy fekk Assamane
You're one of a kind
Assamane Assamane Assamane Assamane
Assamane Assamane Assamane Assamane
{Verse 2}
{Verse 2}
Kholal cii kaw nga bayifa saye beut
It's like your thinking is cutting-edge and advanced
Guisso dara lifa xadioul cii seu cerveau
You're so smart that you're always thinking outside the box
Da nga koy khol moulay guiss mo ngui fepp fi ngay dieum
You're always challenging yourself, always learning new things
Aduna bepp la muur yémoul rek cii sen deuk
You're not afraid to be different, to stand out from the crowd
Kharitou wérr bek Bidew yi mbok Jante ak Naathie
You're a true original, a free spirit
Soubeu lay lerr Goudi mou leundeum gentlema
You're always up for a challenge, always ready to try something new
Boufay dem do yaubou touss démal sett sa maame
You're always pushing the boundaries, exploring new possibilities
Loutah yène makk yi di défar testament
You're a risk-taker, a dreamer
Han! Mom réka tedd ndaxté mane xamena
You're not afraid to fail, you know that failure is just a learning experience
Mom rékay aaté mom réka am bobou makkama (Capacité)
You're always looking for the next big thing, the next great adventure
Assamane nay limite kène douko dindi
Assamane has no limits, you're always striving for more
Amena diourom niarry (7) Assamanes kounek ak sa limite
You're an inspiration to everyone who knows you
Boul khol ci nignou doundé cii souf
You're a true leader, a pioneer
Kigni goungué gniy roukhe
You're always looking for ways to improve yourself and the world around you
xam nga dioum wessuwoul
You're a shining example of what it means to be human
Maye gnou lepp lou bepp mindef di woute
You're a role model for everyone who wants to make a difference in the world
Bagni meune def li nga gnou santeu fi lek niouy dougou sunu bamell
You're a true hero, and I'm so lucky to have you in my life
Doko door balle bamou diaaleu
You're a rare gem
Ropalane khalatoufa yégueu
A true treasure
Lougni def xana sani niaane
I'm so grateful for your friendship
Di niaane Yallah na ngou niaane yikoy fekk Assamane
You're one of a kind
Assamane Assamane Assamane Assamane
Assamane Assamane Assamane Assamane






Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.