Dip Doundou Guiss - Pogda paroles de chanson

paroles de chanson Pogda - Dip Doundou Guiss



Yeah
Yeah
I cry myself yeah
I... i
Yeah
I'm sorry for myself
I'm sorry for myself noo nooo
Uh uh uh uhhhh
God i make it for myself noo noooo
They don't love me anymore
Beus bingay deeeh
Ay rongoniam meunon nala sangue
Doole youkhou yi antane nagn sa corps bi
Bassa bir pakh soul la bassa bir cambeu
Merna kay waye dou gueudji dila nianal
Founne dinalafa touddal tourrou yallah
Banga deme nga yobale xolam
Doundeum niakk xorom goumbeu teuxlou gana
Beus bingay deeh ay goudi la yeahh
Silagn gueudjieu yeuk leerayou beuthieuk
Kerok nioune nieupeu la demone yeeeh
Bamelni dangay nelaw ndakh kenn ndangouko geum
Khar yek xadji bi demnagn ba dagnko yeuk
Amoul mbeuw amoul mbee bebe sakh dou seukeut
Mbeuwti dieuloula noon dala goungue nga gnibi ndakh deukofi aljana nga deuk
Deugla deugla deugla yeahh
Beus bingay deeh si beut yi la fegne
Keur gui na tekk dieum dia faay
Teuddeu sa caisse kou guemeu nga tew
Xeur yi la def thie at bingay dioudou ak bingay diota gueneu adouna yaw
Amelougnou dara diokhma lingue yi tawoul dinalako dello man soumay nieuw
(Bis x2)
Nakari na ci man ma fate funerailles yi no no no
Nooo noo noo no
Deudji bari nagn wante funerailles yi bokou niou no no
Aaahhh aah oh oh
Beugouma diapeu sama xel nika dotoumala guissate
Yaniou ndango bayi defsa bop dem si yalla man loumaci meun
Chaque goudi damay guent guiss la gent bounek limouy missal
Yalla meuneu maye meuneu dieulat limou mom dousi yaw dousi mane
Yalla doula def dara sa ndiabot dou torokh te souf dou tangue sisa kaw
Gni gueun si nioun moy gni nieukeu dem warone nagn goudou fane
Ndakh meun aw yaw fingua aw
Mougn na mougn ba mounatouma mougn
Ndakh rongogne yi dess si bir moy rongogn you gueneu sokhor
Boul deloussi nioune niolay fekkisi
Boude yangniouy guiss xola dagnkoy feter legui
Xolal na mere yi fethieu pa yi mandi
Rendi beuy yi redni mbaam yi
Dagn lay goungue nga fekki mame yi
Amnga ganaye you bess pour are niou
Meme sa noone yeupeu teew
Sollou all black tout noir represent
Tour fi ndokh pour que niou soul si kaw
Ndakari na ci man ma fatte funerailles yi
Rawatina samay funeraillou bope
Eeehh hummm
Nakari na ci man ma fate funerailles yi no no no
Nooo noo noo no
Deudji bari nagn wante funerailles yi bokou niou no no
Aaahhh aah oh oh
Benneu mo gueneu gaaw
Niar mo gueneu woore
Nieweundo wougnou man ak yaw
Mama kaa don't cry now
Mama kaa don't cry now
Yallah bour moma ladji
No no niame wouma negocier
Bayima deme sagnouma negocier
(Bis x2)
Nakari na ci man ma fate funerailles yi no no no
Nooo noo noo no
Deudji bari nagn wante funerailles yi bokou niou no no
Aaahhh aah oh oh
Nakari na ci man ma fate funerailles yi no no no
Nooo noo no
Deudji bari nagn wante funerailles yi bokou niou no
Aaahaaa oh oh
Aaahaah oh
Aaahhh aah oh oh




Dip Doundou Guiss - Beus Niki Tay: The Selec-Tape
Album Beus Niki Tay: The Selec-Tape
date de sortie
31-12-2015




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.