Dip Doundou Guiss - Poto Lamp paroles de chanson

paroles de chanson Poto Lamp - Dip Doundou Guiss



Yeah Hummm humm!
Hahaha Doundou Guiss Manela waay
Morééé
REPTYL MUSIC, DIPHéy Mister Thière
1}
Ma Yaguena wakh town bi dafa tarr waay Pa beugoul ma xam accident de travail
Téwoul niou magg ragné niggah Kone nékouma di Rap pour meuneu nekh nieupeu
Ma dakk RAP cii Monde bi yeup"walaay"
Maay Pakka Poute boudé réwandé ngay djaay Dafa am cii nioumay settt nigga Bou nékoul wone nioniou may gueuneu réw nieupeu Yaguena dégue Wow Yaguena dégue
Wouuuu
DIP moussoul nek sur scène naane ma ngui djégueulou
Ya mom song bi yaw mimay déguelou di bëk nii
Ak yaw mi nga xam ni mane rek nga gueuneu djépi Potolamp fii sa photographe dou meusseu soxla flash Fokk ma takk ndax bima done rap xollam da done lakk
Numéro 10 doundou guiss Gaïndé Mbeurodi Walahi meuno siss ba rombeu métis bou raciste
Boy bi bindeum styleum ak flow bi Masha'
Allah Na RAP ba bindeu toureumak disques d'or yi cii assamane cii
Ndax sama noone yi dagno yague djapp teuweu baayi Boudoul wone ak niom baayina bou yague dém djangui From Grand Yoff Arafat Zarco ndandi Faa
Sama yoneu tarr lolo takh soufou tank yi khar Yakarouma cii kèn aduna bi yeup lay gueusseum
Kone même bouma done djaay samangorr kène dou am njeugueum{
Def ko sa profil ba sa couverture Sa profil ba sa couverture Def ko sa profil ba sa couverture wala sa profil ba sa couverture (2 fois)
2}
Ma Yague naama baayil fowé khalle
Pa bougoul RAP même bouma koy tangal Reuthiou wouma sakh limay def nigga
Kone Rap bouma pour foo pour mouy lerr
Humhumm
Maay yakk rap bi ngèni def Insha'
Allah
Laata Album nga jott Mixtape bou doy waar
Djapalni BEUS NIKI TAY Nigga
La Mère de ma mère est née
Boy fuck Télé Radio ak Net bi séni Interview Yallah meussoko guiss do meusseu guiss kouko gueuneu siw Meuno am RAP cii sa téléphone bi défo DIP Kénène kougne fii yafi dakk RAP dagnela colé motif
Potolamp fii sa photographe dou meusseu soxla flash Fok nga xam gniy leundeumeul bokoul sama programme
Rap Nga ba soneu dara démoum xana meuno pause
Wala nga baayi ni Old Skool yi yégue ménopause
Nigga ma mom sama lamigne louma nekh laay wakh Xam nani sécurité Aldiana rek la amm
Batterie pleine non dou mak gni di takk di faye
Ngaaka yi nek di khaar Baag rekkay yagg cii Ténn
Douma nétali kone da ngay tiite ladialsama équipe Nagne leu xamalni lima dathie dafa wessu métiite
Kone boné DIP da wara tarr biw sa MCs yi Day melni ngané Yallah wara djamou yoneinte yii
Def ko sa profil ba sa couverture (Yeah)
Sa profil ba sa couverture (Hun Hun)
Def ko sa profil ba sa couverture wala sa profil ba sa couverture (2 fois)
Doundou Guiss Manela Waay Morééé
DIP Quinzaine REPTYLE MUSIC




Dip Doundou Guiss - Beus Niki Tay: The Selec-Tape
Album Beus Niki Tay: The Selec-Tape
date de sortie
31-12-2015




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.