paroles de chanson Sama Jeunesse - Dip Doundou Guiss
Morééé
Doundou
Guiss
Mane
la
waay
moréé
Umh
Umh!
Check
{}
28,
29
Wathieu
16
ak
17
ans
Kouko
am
tou
tokk
cii
chaiseum
di
sétane
Baa
gni
di
dem
gnéé
ngui
tek
zeum
di
raye
temps
Nieulé
nio
ngui
cii
baak
prek
djam
délinquance
Jeunesse
loloko
formé
Fatéwouma
gni
yéwo
jail
Reubeuss,
ba
Forbé
Sama
Jeunesse
dagno
waulou
sen
bopp
Done
ay
mindef
yu
meune
def
li
beuri
sen
bopp
Gni
baayi
jangue
wouti
job
nimou
beuré
Liko
raw
ngui
Football
mba
simékou
Beuré
Gni
Music,
gné
Mannequinat
ak
Féthieu
Soumala
néé
dou
job
kone
ma
nek
Naafeek
Big
Up
wa
Cité
(Université)
wa
collège
ak
wa
Lycée
Town,
Banlieu,
Thug
wala
Wally
Seck
Sama
Jeunesse
bokoy
imaginé
Sa
Mind
men
di
nga
guiss
image
youné
Amena
Jeune
youy
doundou
Costume
Cravate
Bureau
Ci
entreprise
Ba
état
ba
am
grade
bi
rawe
Sen
morom
yi
téglé
Diplôme
yi
di
woute
liguèy
Gni
cii
dess
fess
boppeuh
kogne
yi
di
khaar
liguèy
Nioune
dagnou
sonou
beug
solou
ak
xaandj
Ci
bénène
monde
lagnou
tok,
deukou
love
ak
Happy
House
Party,
Beach
Party,
SWAGG,
Yakk
xaliss
Blackberry,
Iphone,
Ipad,
Galaxy
ay
jeune
yu
sen
xel
dal
Diamono
S'Cool
lonkonté
yu
yu
todj
Sénégal
Jangou
niou
pour
xam
dagni
sett
nouniou
féxé
diaaleu
Classe
par
Classe
triché
mba
yénène
péxé
daal
Téganté
xell
direunté
mbagueu
wéréinté
Média
Djiguène
yu
beug
xaliss,
ba
founiou
ko
séén
daw
Lidieunti
lougnou
lekk
sen
farr
yi
ba
taylé
sen
ndawe
Boy
you
tameu
def-tate
(ivre),
di
doundou
bandi
def
kat
Mbède
né
sen
Staff
def
lèn
ay
ngaandi
Stars
Motah
Guiss
nga
Boy
yi
agressé
mère
ak
guel
yi
thiagatou
bikk
Boy
yi
ndieukeunté
jail
ak
guel
yi
ndieukeunté
biir
Boy
yi
sathie
sen
père
ndax
guélou
appartement
Guel
yi
biir
bagna
nek
mère
déffi
avortement
No!
Jeune
yu
doff
eupeunté
sheytané
Mais
boy
xeuyyeu
tané
djiguène
néggu
seuyyeu
tané
Xaam
nga
dagno
reuy
ci
sunuy
rêves
Boo
néké
ndaw
dou
niak
nga
saurou
louné
Boul
guiss
rek
dafa
gnaaw
nougni
doundé
Oubile
saye
beute
té
diémeu
xam
lougni
goungué
Pour
dëkou
doundou
bii
fii
néé
té
bone
Reuthiou
molaye
dapp
cii
cii
saa
yone
Jeunesse
bou
yémé,
Jeunesse
bou
aliénée
Sama
Jeunesse,
Sama
Jeunesse
Song
bi
yèn
lako
jaglél
Xam
ngène
né
yone
bi
ngène
taneu
bakhoul
kone
djaadeu
lène
Boy
yek
guel
yu
beuri
ay
jaague
laagneu
Réw
méé
lathie
lou
yombe
gentlemen
jangui
lène

1 Deug Deug
2 Assamane
3 Khametoma
4 Yone Bi (feat. Fla The Ripper)
5 Sama Jeunesse
6 Day Deep (feat. Elzo Jamdong)
7 A Thindji
8 Reuthie
9 Interview
10 Xam-Xam (feat. Ndongo D)
11 Pogda
12 Rep'team
13 Nangou
14 Doundou Oundou
15 Yaakarouma Ci Keen
16 Poto Lamp
17 May Kane
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.