Paroles et traduction Dip Doundou Guiss - Deug Deug
Добавлять перевод могут только зарегистрированные пользователи.
Da
nga
teudone
rek
di
guënte
wayé
nala
yéé
Da
nga
teudone
rek
di
guënte
wayé
nala
yéé
Ndakh
né
nagnema
deug
nekhoul
deugueuntane
na
nekh
Ndakh
né
nagnema
deug
nekhoul
deugueuntane
na
nekh
Boul
meusseu
xepp
dara
kounek
lila
Yallah
may
Boul
meusseu
xepp
dara
kounek
lila
Yallah
may
Xalé
ba
ngui
djoy
té
mateu
mbélènetane
la
rek
Xalé
ba
ngui
djoy
té
mateu
mbélènetane
la
rek
Meunouma
nadjé
yégueu
none
yéma
téla
xékh
Meunouma
nadjé
yégueu
none
yéma
téla
xékh
Tchine
bou
baxé
xégne
da
fek
dafa
ndara
nekh
Tchine
bou
baxé
xégne
da
fek
dafa
ndara
nekh
Deug
bou
amoul
massla
la
ndara
tek
nak
Deug
bou
amoul
massla
la
ndara
tek
nak
Real
Rap
dou
Salsa
dou
Wane
Téraméra
Real
Rap
dou
Salsa
dou
Wane
Téraméra
Gnouné
mola
gueune
mougneul
di
nga
meusseu
mogneu
Gnouné
mola
gueune
mougneul
di
nga
meusseu
mogneu
Maye
lathie
loutah
sa
ndey
dior
gueuneul
la
sa
thiamogne?
Maye
lathie
loutah
sa
ndey
dior
gueuneul
la
sa
thiamogne?
Loutah
ngay
laabé
thiamogne
té
ndey
dior-ra
dankone?
Loutah
ngay
laabé
thiamogne
té
ndey
dior-ra
dankone?
Loutah
Goor
yi
di
sawé
thiamogne
thiamogne
ndey
dior-ra
tankone?
Loutah
Goor
yi
di
sawé
thiamogne
thiamogne
ndey
dior-ra
tankone?
Li
ngay
gueume
molay
dal
lolou
rek-kafi
né
Li
ngay
gueume
molay
dal
lolou
rek-kafi
né
Diaroul
di
sett
fou
sori
sa
boppeuh
doy
nala
firndé
Diaroul
di
sett
fou
sori
sa
boppeuh
doy
nala
firndé
Bagni
nek
boy
lagne
gnou
téré
carte
xaliss
Bagni
nek
boy
lagne
gnou
téré
carte
xaliss
Té
bobou
ba
légui
LONASE
mo
ngui
lindia
sunu
Pa
yi
Té
bobou
ba
légui
LONASE
mo
ngui
lindia
sunu
Pa
yi
Né
nga
Yallah
nga
gueum
loy
doyé
gris-gris
Né
nga
Yallah
nga
gueum
loy
doyé
gris-gris
Né
nga
mbède
ngay
téwal
loy
dokh
di
saw
cii
murs
yi
Né
nga
mbède
ngay
téwal
loy
dokh
di
saw
cii
murs
yi
Li
ngay
dégue
gnoulay
wakh
boukoutak
lignou
lay
wane
Li
ngay
dégue
gnoulay
wakh
boukoutak
lignou
lay
wane
Wakh
li
ngay
deffa
gueuneu
yomb
ngay
def
li
ngay
wakh
Wakh
li
ngay
deffa
gueuneu
yomb
ngay
def
li
ngay
wakh
Goor
Yomboul
ndax
amena
goor-djiguène
yougnou
djongal
Goor
Yomboul
ndax
amena
goor-djiguène
yougnou
djongal
Mane
nek
na
Goor
Yallah
bala
ma
djongou
Mane
nek
na
Goor
Yallah
bala
ma
djongou
I'm
Real
niggah
té
douma
sopalikou
I'm
Real
niggah
té
douma
sopalikou
Damay
khar
samay
tank
toubeuy
ba
mère
bi
nopalikou
Damay
khar
samay
tank
toubeuy
ba
mère
bi
nopalikou
Kou
bagne
gnou
wakh
loumou
défoul,
dou
wané
loumou
nékoul
Kou
bagne
gnou
wakh
loumou
défoul,
dou
wané
loumou
nékoul
Noone
ya
ngui
fouma
yégoul
douma
lène
dieuw
dama
lén
ci
teukou
Noone
ya
ngui
fouma
yégoul
douma
lène
dieuw
dama
lén
ci
teukou
Ya
ngui
cii
kaw
ma
ngui
cii
souf
lolou
motah
maye
sissou
Ya
ngui
cii
kaw
ma
ngui
cii
souf
lolou
motah
maye
sissou
Gnam
bi
souma
cii
lékoul
fawma
keupeu
cii
souf
Gnam
bi
souma
cii
lékoul
fawma
keupeu
cii
souf
Sen
Flow
dissoul
kène
ci
yène
todjou
cii
Youtube
Sen
Flow
dissoul
kène
ci
yène
todjou
cii
Youtube
Rap
rek
lafi
guissoul
fuck
gni
nane
damay
sissou
Rap
rek
lafi
guissoul
fuck
gni
nane
damay
sissou
Time
is
money
wakh
ko
bororm
Montres
yu
chère
yi
Time
is
money
wakh
ko
bororm
Montres
yu
chère
yi
Ba
nga
fataliko
dealers
youniou
kep
cii
jail
yi
Ba
nga
fataliko
dealers
youniou
kep
cii
jail
yi
Sokhor
ba
bougnou
défé
lou
bakh
dafa
fek
gnou
joum
Sokhor
ba
bougnou
défé
lou
bakh
dafa
fek
gnou
joum
Xalé
bouy
diawalé
dalam
yène
say
mou
solko
mou
djoupp
Xalé
bouy
diawalé
dalam
yène
say
mou
solko
mou
djoupp
Sa
life
dafa
yombone
ngay
woute
life
bou
djingue
Sa
life
dafa
yombone
ngay
woute
life
bou
djingue
Aduna
rawaneté
la
rek
té
légui
moudjé
nga
Aduna
rawaneté
la
rek
té
légui
moudjé
nga
Boy
yi
djapé
sen
boppeuh
star,
Stars
yi
djapp
sen
boppeuh
Boy
yi
djapé
sen
boppeuh
star,
Stars
yi
djapp
sen
boppeuh
Roussena
njeukeunté
té
djémouma
raw
Usain
Bolt
Roussena
njeukeunté
té
djémouma
raw
Usain
Bolt
Bokoumak
gni
di
wakh
le
ciel
est
la
limite
Bokoumak
gni
di
wakh
le
ciel
est
la
limite
Assamane
yi
beuri
nagne
kone
bi
dou
sama
limite
Assamane
yi
beuri
nagne
kone
bi
dou
sama
limite
Xepp
tokou
dérette
bidoul
xonkal
keuleu
méw
Xepp
tokou
dérette
bidoul
xonkal
keuleu
méw
Est-ce
que
takhoul
gnou
mystique
badi
souli
néw?
Est-ce
que
takhoul
gnou
mystique
badi
souli
néw?
Kou
xam
ñi
tey'lé
ay
bakaan
tchi
ay
mbiir
you
nëw
Kou
xam
ñi
tey'lé
ay
bakaan
tchi
ay
mbiir
you
nëw
Journal
bi
lou
nieup
xam
rek
lay
souligné
Journal
bi
lou
nieup
xam
rek
lay
souligné
Télé
ngay
tok
di
sétane
kou
amoul
lou
matt
sept
ans
Télé
ngay
tok
di
sétane
kou
amoul
lou
matt
sept
ans
Ci
Film
bo
xam
kou
amoul
16
ans
douko
sétane
Ci
Film
bo
xam
kou
amoul
16
ans
douko
sétane
Diamono
ngui
dokh
nieup
ngui
toppeuh
Sheytane
Diamono
ngui
dokh
nieup
ngui
toppeuh
Sheytane
Yaw
démalak
sa
xel
xol
fi
ngay
tek
say
tankeu
Yaw
démalak
sa
xel
xol
fi
ngay
tek
say
tankeu
Accident
yi
beuri
nagnou
cii
nignouko
guissé
Accident
yi
beuri
nagnou
cii
nignouko
guissé
Té
meusso
dégue
Carrapide
firr
na
policier
Té
meusso
dégue
Carrapide
firr
na
policier
Xalissou
rééwmi
kou
nek
meussna
cii
cotisé
Xalissou
rééwmi
kou
nek
meussna
cii
cotisé
Ngour
ngui
lekk
ko
dignou
leurré
ak
audité
Ngour
ngui
lekk
ko
dignou
leurré
ak
audité
Obama
louko
indi
léwal
goor-djiguène
Obama
louko
indi
léwal
goor-djiguène
Nélène
gnou
wakh
cii
chomage
bi
gnoune
dé
nio
ngui
déh
Nélène
gnou
wakh
cii
chomage
bi
gnoune
dé
nio
ngui
déh
Agression
day
fay
ndakh
def
nagnou
ko
liguéy
Agression
day
fay
ndakh
def
nagnou
ko
liguéy
Wagnékou
woul
ndax
gnikoy
def
yeup
gnam
nagnou
jail
Wagnékou
woul
ndax
gnikoy
def
yeup
gnam
nagnou
jail
Mbède
boumou
takh
nga
taukh
baune
boul
meusseu
done
soulard
Mbède
boumou
takh
nga
taukh
baune
boul
meusseu
done
soulard
Ragal
Dou
Diégui
Rail
Bandit
dou
dokh
cii
filou
courant
Ragal
Dou
Diégui
Rail
Bandit
dou
dokh
cii
filou
courant
Légui
nieup
am
fiit
xalé
yi
sakh
dawatougnou
KanKourang
Légui
nieup
am
fiit
xalé
yi
sakh
dawatougnou
KanKourang
Chrétien
té
amo
BIBLE,
Dioulite
boudoul
khol
AL-QURAN
Chrétien
té
amo
BIBLE,
Dioulite
boudoul
khol
AL-QURAN
Ray
nagnou
Sadam
Hussein
ak
Ossama
Ben
Laden
Ray
nagnou
Sadam
Hussein
ak
Ossama
Ben
Laden
Té
né
nagnou
dougou
nagnou
Akhrou
Zamane
may
day
Té
né
nagnou
dougou
nagnou
Akhrou
Zamane
may
day
Picc
bou
laké
cii
taate
day
beug
am
morom
Picc
bou
laké
cii
taate
day
beug
am
morom
Sheytane
dafa
takk
beug
gno
def
morom
Sheytane
dafa
takk
beug
gno
def
morom
Fène
tribunal
wessou
woul
Ragal
nitt
gnémé
Yallah
Fène
tribunal
wessou
woul
Ragal
nitt
gnémé
Yallah
Monsieur
le
Juge
do
Yallah
kone
boul
topando
Yallah
Monsieur
le
Juge
do
Yallah
kone
boul
topando
Yallah
Yélwane
def
nagnou
ko
Job
ndax
kène
bagnoul
diokhé
nguir
Yallah
Yélwane
def
nagnou
ko
Job
ndax
kène
bagnoul
diokhé
nguir
Yallah
Wayé
boy
mayé
ay
Millards
faw
gnou
Caméra
la
Wayé
boy
mayé
ay
Millards
faw
gnou
Caméra
la
Président
day
djité
sakh
gniko
voté
loule
Président
day
djité
sakh
gniko
voté
loule
DIP
jottéwoul
ak
yaw
mais
li
ngay
RAP
moko
dougoul
DIP
jottéwoul
ak
yaw
mais
li
ngay
RAP
moko
dougoul
Texte
bou
tilime
la
bindé
deug
dji
ngène
dégue
Texte
bou
tilime
la
bindé
deug
dji
ngène
dégue
Di
ngène
bëg
boudé
beug
ngène
dégue
deug
deug
Di
ngène
bëg
boudé
beug
ngène
dégue
deug
deug
Évaluez la traduction
Seuls les utilisateurs enregistrés peuvent évaluer les traductions.
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.