Dip Doundou Guiss - Innoncent - traduction des paroles en anglais

Paroles et traduction Dip Doundou Guiss - Innoncent




Innoncent
Innocent
Yeah
Yeah
Ba niepp dièxallè Mann sillay soga fèss
They are trying to frame me, man, but I'm innocent
Def nala Papa parce que tèrè woma xèkh
I call on Dad because the world is deceitful
Dinagn la enquête ndakh tay sa doma xéw
The investigation is ongoing, but I know nothing
Ta bam léne wanné samay ranngoy niom niepp bégu
For years now, I've been suffering, I've done nothing wrong
Bo xaméni faw lékk faw nga fokhalé
You know I'm a good person, I don't mess around
Da ngay xép conndané bou tol ni contenaire
They want to sentence me to years in a container
Last kiri pairou dalleu dâm la soll ba
Last night I dreamt I was dancing on the floor
Motaxx tay Job ba niakk diott ba
I'm tired of this job, I'm tired of these debts
Damako khar ni Steph Curry Pour wathié Jordan Man
I dribble like Steph Curry, aiming for Jordan's level
Ni bépp xéttou nit bouy wadja donn lénènn
They envy me, that's why they spread lies about me
Fatté wouma fi gnou ma diangalé fi gnou ma djngalé
They talk behind my back, they try to deceive me
Fatté wouma Pa yi ma niannal mères yii ma dioxx ma lékk
They talk behind my back, my parents raised me well, I'm honest
Avenir lagn diémona dieulli ci yonou
The future is bright, God is with me
Karaw bou nioul ak xél bou mak sa niom Mame
Like the moon and the sun, my name will shine
Boul wôllu sakh ñi la wôllu Confiance
Those who trust are blessed with trust
Xadioul ci Malayka Djînné Conscience
Peace to the Angels, Djinn, and Conscience
May Garab bou beug microbes
My charm protects against negativity
Innocent bouy andd ak Inno
Innocent by name, innocent by nature
Ay Fènn katt rekk ak ay traitres
Surrounded by haters and traitors
Layy guis souma fattéliko
I will achieve my goals, believe it
Diox ma passeport visa yeah
God grant me a passport and visa, yeah
Tampon cii Passeport bi ma dém
The stamp on this passport will set me free
Par force fass diom biss mba
By force, I'll find my way out
Waw goor di nga donn Milliardaire
Hey man, give me billions
Éhhh ya fi néwonn souniou GANG Famille la
Hey, I don't forget my roots, GANG Family
Niounn niepp bokk Diar diar nigger
We are not neighborhood kids
Fima diar kouffa diar xam yaw fi nga Diar koufa Diar tass sa yakarr nigger
We're from the streets, you know, if you're from the streets, stop complaining
Ma ngui niafé ma ngui xar matt nigger xonnéta touma sakh rarement nigger
I hustle, I work hard, rarely relax
Fima diougué souma fa naré dèllou watt
We fight, we stand up for ourselves
Fathie la Jail wala teuthie ma Hôpital my nigger
Either jail or the hospital, my friend
Yeah yeah Yeah
Yeah yeah Yeah
Ba niepp dièxallè Mann sillay soga fèss
They are trying to frame me, man, but I'm innocent
Dip comme ko teudd lo correctionnel ay Colonel
Dip, like the Colonels who correct things
Dinagn ma saga ndey Dina lènn songg xékh
Let them talk, I have my songs
Konn niakk diott ba guénné sons ba
I know nothing about debts, nothing about problems
Maouti Sakh douma dieul ci parce que mak moma yémm
I'm calm because I have nothing to hide
Konn en cas Mc bou boul lathie kann moko ray
I don't care about MCs or those who hate, I ignore them
Niata rappeur nga féyy niata millions nga kékk
I'm a rapper, I make millions
Boy déssé touma bénn ranggoñ pour dioy sa deuthie
I work hard to achieve my dreams
Est ce que witthiaxx na sama baram
Do you understand my pain?
Guéthie na réthiou depuis 17 ans Motherfucker
I've been hustling since I was 17, motherfucker
Damako xarr nitt ak Aldiana
I spend my money with Aldiana
Mann dama lènn rèndi soga titt Ndayssane dawna yaram
I give money to the needy, especially during Ndayssane
Boy mann kassé béneu nitt 5000 nitt dima xékh
I spend 5,000 every day
Nianall na samay ennemies ennemie ki ak
I forgive my enemies, even those who hate me
Dama xékhal mbédd bi mbédd bi dima xékh
I spend lavishly every day
Dama xékhal mbédd bi mbédd bi dima xékh
I spend lavishly every day
Ma ngui ci chaisou Bour bi nio ngui ci chaisou douche yii
I'm in prison, but I shower
Fake gui dounkkou yii nandité you mouss yi tékk nañ nou deal mais guénn guénno ci
Fake friends, you envy me, we had a deal, but it's over
Noir et fier amoufi dér bou nioul bi mo xépp dér bou nioul
Black and proud, my skin is beautiful, my skin is beautiful
Mafi geunna touti thiabi bou reuyyônn dou tidjî bountou
I don't have everything, but I'm content with my simple life
Mangui geunna yékk di geunna yekk di guenna wétt
I have nothing, I have nothing, I have nothing
Xaritt aka nëw yii Diamono wouy sama Ndeye
I'm a diamond, my Ndeye
Temps yi yeurmandé def sama xol ci sama xél diay kou mana fayy dou niou mayé xérr di keuppeu caisse
Time will tell, my heart and soul are at peace, I don't care about money
Yeah fittna la fittna may fittna fittna la fittna may fittna
Yeah, the fitna is real, the fitna is real, the fitna is real, the fitna is real





Writer(s): Dip Doundou Guiss, Ismaila Talla


Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.