paroles de chanson Funérailles - Dip Doundou Guiss
Reptile
Music
Yeah
Yeah
A
crime
saved
yeah
Anh
Anh
Yeah
I'm
sorry
for
myself
I'm
sorry
for
my
self
no
no
Ouh
Ouh
Ouh
Ouh
Ouh
Gotta
make
it
for
myself
no
no
They
don't
love
me
any
more
Beus
bi
ngay
dèe,
ay
rongoniam
meunone
nala
sangue
Doolei
youxou
yi
atane
nagnu
sa
corps
bi
ba
si
sa
biir
pakh
soul
la
si
sa
cambeu
Merr
na
kagn
wayei
dou
geudj
dilla
nianal
founek
dinalafa
toudal
tourou
Yalla
Bagua
demei
ngua
yobalei
xollam
doundame
niakk
khorome
goumba
teukhlou
gana
Beuss
bi
ngay
dée
ay
goudila
yeah
Si
lagne
guedjeu
yeuk
lerayou
beuthieuk
Kerok
nioune
nieupeu
leu
demone
yeii
ba
mellni
daguay
nelaw
ndakh
keine
meunouko
gueum
Xar
yeik
Xath
bi
demnagne
ba
dagne
ko
yeuk
amoul
mbow
amoul
mbeé
Bb
sakh
dou
seukeute
Mowti
djeulloula
non
dala
goungueii
ngua
gnibi
ndakh
deukoofi
Al-Jannah
ngua
deuk
Deug
leu
deug
leu
deug
leu
Yeah
Beuss
biguay
dée
thi
goudi
la
fegne
Keur
gui
ni
tekk
Djeum
dja
faye
Teud
sa
caisse
kou
djeum
ngua
tew
Fleur
yi
la
deff
si
att
bi
ngay
djoudeu
ak
att
biguay
djotta
gueine
Adina
yaw
Ameilooniou
dara
diokh
ma
lingèy
yi
dalloul
dinalako
dello
beus
bi
may
nieuw
Eh
Nakarina
si
mane
ma
fattei
funeirailles
non
non
non
Non
non
non
non
Deudji
yi
beuri
nagne
Wayei
funérailles
yi
bokoul
non
non
Ah
Ah
Oh
Oh
Nakarina
si
mane
ma
fattei
funérailles
non
non
non
Non
non
non
non
Deudji
yi
beurinagne
Wayei
funérailles
yi
bokoul
non
non!
Ah
Ah
Oh
Oh
Beugouma
diap
sama
xel
que
ni
dotoumala
guissate
Ya
gnu
nango
bayyi
def
sa
bopp
dem
si
Yallah
mane
louma
ci
meune
Chaque
goudi
damay
gueinte
guiss
la,
gueinte
bou
nek
ak
limuy
missal
Yallah
meuneu
mayé
meuneu
dieullate
limou
mome
doussi
yaw
doussi
mane
Yallah
doula
def
dara,
sa
ndjaaboot
dou
torokh,
ta
suuf
dou
tang
si
sa
kaw
Gni
guene
ci
niune
moy
gni
gneukeu
dem
Warone
naniu
goude
fane
dakh
ma
meune
aw
fi
nga
aw
Mougne
na
mougne
ba
meuneutouma
mugne
Ndakh
ronkhongne
yi
dess
ci
biir
moy
ronkhogne
yi
geuna
sokhor
Boul
deloussi
gnune
gnolay
fekki
Boudé
ya
ngi
gnuy
guiss
xolal
gnune
dagnu
koy
feté
legui
xolal
Na
mere
yi
fethie,
Pa
yi
mandi
Réindi
beuye
yi,
réindi
mbame
yi
Dagnu
lay
goungué
nga
feeki
Mame
yi
Am
nga
ganaille
yu
bess
pour
aar
gnu
Meme
sa
noone
yeupa
tew
solu
all
black,
tout
noir
represent
Tour
fi
ndokh
pour
que
niou
soul
ci
kawam
Nakhari
na
ci
mane
ma
faté
Funairaille
yi
rawatina
sama
funeraillou
bopp
Nakarina
si
mane
ma
fattei
funeirailles
non
non
non
Non
non
non
non
Deudji
yi
beuri
nagne
wayei
funérailles
yi
bokoul
non
non
Ah
Ah
Oh
Oh
Nakarina
si
mane
ma
fattei
funérailles
non
non
non
Non
non
non
non
Deudji
yi
beurinagne
Wayei
funérailles
yi
bokoul
non
non
Ah
Ah
Oh
Oh
Beneu
mo
geuna
gaw
Niaar
mo
geuna
woor
Gneuwa
ndo
wuniu
mane
ak
yaw
Mama
Cry,
don't
cry
no
Mama
Cry,
don'r
cry
no
Yallah
buur
moma
lathie
Bono
gnemewuma
negocier
Bayil
ma
dem
sagnuma
negocier
Nakarina
si
mane
ma
fattei
funeirailles
non
non
non
non
Non
non
non
non
Deudjii
beurinagne
wayei
funérailles
yi
bokoul
non
non
non
non
Ah
Ah
Oh
Oh
Nakarina
si
mane
ma
fattei
funérailles
non
non
non
Non
non
non
non
Deudjii
beurinagne
Wayei
funérailles
yi
bokoul
non
non
Ah
Oh
Oh
Ah
Oh
Oh
Ah
Ah
Oh
Oh
1 Holocauste
2 Damako Khar
3 Dou raggal dou respect
4 Niata la yalla fay sa xol
5 Bandit
6 Beut
7 YMYM
8 Nimala beugué
9 Niata nio dess
10 Funérailles
11 Kheula
12 Innoncent
13 Kantambiuw
14 Com dab
15 Temanefi
16 Boula dara metti
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.