Elzo Jamdong - Ci Yaw paroles de chanson

paroles de chanson Ci Yaw - Elzo Jamdong



sonena guissegouma dara lima meune
fatèloni iow la tanone pour nga same sama mbeugel
fonke nala kone fonkena lane mo takh fogone
nanè souma togguè wett ak sama bopp dinguema gounguè
eh
yama nèwone ni dingue ma dinthial sa thiabi
xol limou goudi goudi dinga tidji souma feuguèe
diangue nala mokal nala amoul dara lingne ma meune xamal
thi iow thi iow thi iow thi ioww thi iow thi iow thi iow
kène dou wakh dara thi iow thi iow thi iow thi iow thi iow
kène mounou ma wakh dara thi iow
sayo guènè mane ngay xalate
souma xolè iow rek la am
soma guissoul dangay malade
yène sayi ma doyal seukk thi iow
thi iowww
sonena guissegouma dara lima meune fatèloni iow
la tanone pour nga wètalima nga same sama mbeugel
faut que nga manou ndakh thiow li thiow li yeupp
waroul niaw warouma bètte tamite lepp lima diangue thi iow
thi iow thi iow thi iow thi iow
thi iow thi iow thi iow
kène dou wakh dara thi iow thi iow thi iow thi iow thi iow thi iow
kène mounouma wakh dara thi iow
mouno nangou am tore (thi iow)
dagne ma wakh ma d'accord (thi iow)
fogone nanè c'est mort (thi iow)
bobou xawma wone louy amor
ay xoulo tey dioubo teyy
yène wakh you sèw yi douniou tardèlate soudone teyy
mane lène la guiss thi iow
moy kène xadioul thi souniou thiow (thioww thioww thioww)
yeah
haey
sonena guissegouma dara lima meune fatèloni iow
la tanone pour nga wètalima nga same sama mbeugel
fonke nala ndakh thiow li thiow li yeupp naroul
niaw warouma guède tamite lepp lima dèfare thi iow
thi iow thi iow thi iow thi iow thi iow thi iow
kène dou wakh dara thi iow thi iow thi iow thi iow thi iow thi iow
kène meunouma wakh dara thi iow
thi iow thi iow thi iow thi iowww
PBL. F




Elzo Jamdong - Macina
Album Macina
date de sortie
29-06-2018




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.