Elzo Jamdong - Saï Saï paroles de chanson

paroles de chanson Saï Saï - Elzo Jamdong



Yeah yeah eh eh yeah
Kenn warouma beugg
Mane tchi sama bopp khawma louma beugg
Ken warouma beugg bi niouy ndieukk dadié bobou wakhoumala deugg
Ken warouma diégué
Kou ma kham di nga thiéné fi nga thiéné
Ken warouma diégué
So done kharit sama bopp laa lay
ndieukk téré (sama bopp lalay ndieukk téré)
Boul meusseu gueum samay texto
Boul meusseu nangou niouy wéto
Mane doumeu fey damay lep dow
Ndakh damay play, #Nintendo
Boul meusseu gueum samay texto
Boul meusseu nangou niouy wéto oh
Doumala diokh li ngay weur boul ma
wolou ndakh wakhouma loudoul ay léébone
Mane saï saï laa, maa gueuneu yess Al Qaïda ah ah ah
Saï saï laa motouma, moytouma ey
Khamal ne saï sa! î laa maa gueneu metti Al Kaïda ah ah ah
Saï saï laa, moytouma, moytouma ey
Yow boumeu wakhlo, soma tidjilé se nopp naala doflo (dinga dof)
Doumako tey soumay noplo
So ma tidjilé se bopp di nga ofdo (yeah)
Damay dow somay wone love
Ndakh beugoumeu koumeu beugg di meu toppato (eh) No!
Boul ess you'll get no love
Somay khaar onshore maa ngui oofshore! ey
Boul meusseu gueum samay texto
Boul meusseu nangou niouy wéto
Mane doumeu fey damay lep dow
Ndakh damay play, #Nintendo
Boul meusseu gueum samay texto
Boul meusseu nangou niouy wéto oh
Doumala diokh li ngay weur boul ma
wolou ndakh wakhouma loudoul ay léébone
Neekh laamign, bad mind
Khole bi degn tchi warone coller stop sign
Niaata laa fi digone dékhou banneekh?
Tchi guédiou rangogn legn moudié lap gayine!
Dama lédj dama dioubeudi
Shawty naala tédj ci sey souvenirs
Au début dangay bég fok ne doumeu nit
Tey bo sanione doma fréq doma meusseu miin
Yagg naa di wakh tchi gorr yi fowé kholou guél
Tané wouma kone mounouma téyé rôlou frère
Sciensal kepp kou tass yakaar tégou yonou jail
Do deggeuti kenn néleu doundeul bo tchi toluwé
(Do deeggueti ken, do deggueuti ken
Do deggeuti ken leu doundeul bo tchi tollouwé)
Outro
Saï saï laa ah (saï saï la)
Alkaïda ah (al kaïda)



Writer(s): elzo jamdong, misterthiere


Elzo Jamdong - Macina
Album Macina
date de sortie
29-06-2018




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.