Elzo Jamdong - Coulisses paroles de chanson

paroles de chanson Coulisses - Elzo Jamdong



magui sama coulisses di préparer bégueul ay niit youma hamoul melni
amouma life amouma amour magui studio di bind album pour niit yima
guissoul kagne lamay dallou Yeah job na beug siiw legui siiw na beug
lahatou meusou meu beug fegn pour réussir mais am tour siiw legui
amatoul may geuneu yeek yeeg niveau gester dogua sokhla rap overdose
wine house legui diahal leu toumeu nakh doyeul na est-ce que soumeu
démissionner woul won sama ex job doumeu tané fii (beugon bolé vie
de famille ak show-biz) mais ken meunoul ameuno niari vie man jamdong
bimay wotei fou nek est-ce que magui doundeu lou pacifique magui
dogueu ragné néké succès beurineu piège beurineu artifice (Oh!) ga
gné na ay caché (woo) signé na que-ché (Yeahhh) yok na ay amis niak
na ay harite deug Yallah may meu ay mbok man meu tanneuh ay fans
deuké daaw guinaw ndam baa doumeu niit kou gaat ay fann magui sama
coulisses di préparer bégueul ay niit youma hamoul ay niit youma
hamoul ay niit youma hamoul melni amouma life amouma amour amouma
amour amouma amour magui studio di bind album pour niit yima guissoul
pour niit yima guisouulll kagne lamay dallou Carrière bi dineu meu
gagne tei doumeu ko yeuk mogui may hagn may geuneu rerr dawna ay
kilomètres dokhna ay km dieul yoonu missionnaire (yeah) pour neek
millionnaire (yeahhh) solna ay pull-over ay tee-shirt marque yi
geuneu cher wayei même tabahou meunoul takh bagueu nek kou immortel
concert yagui geuneu fess supporter yagui danou leer geudji na deeg
sameu batou mère est-ce dou lii mo nekon sameu nianou mère dougna big
thiow dougneu big thiow teii ken dougeu loumeu tei ken dougeu loumeu
sii beugna kit trop beug donn big boss
(...) machine (...) dou machine (woo!
woo!) machine sakh day beuguer cousin meun gama merrei wanou maleu
nima leu beugué holale légui dama tok 3 mois doumeu déguanté ak
bab's (allo) namna man ak Jean
Joe biniouy bok agn temps fac (Fac...
Fac...
Fac...
Fac...
temps Fac!
biniouy bok agne temps Fac) magui sama coulisses di préparer bégueul
ay niit youma hamoul ay niit youma hamoul ay niit youma hamoul melni
amouma life amouma amour amouma amour amouma amour magui studio di
bind album pour niit yima guissoul pour niit yima guisouulll kagne
lamay dallou Carrière bi dineu meu gagne tei doumeu ko yeuk mogui may
hagn may geuneu rerr Carrière bii dina meu gagnooo tei doumeu ko yeuk
mogui may hagn may geuneuu rerrr dina gagne tei doumeu ko yeuk mogui
may hagn may geuneu rerr Carrière bii dina meu gagnooo tei doumeu ko
yeuk mogui may hagn may geuneuu (Allo Elzo man leu ditaa magui lay
woo reek bobu beu leguii meunou maleu djot fiuu mogui meu nan
Suède walleuh Allemagne bo djotei sameu
message gua rappelé meu merci à bientôt)




Elzo Jamdong - Macina
Album Macina
date de sortie
29-06-2018




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.