paroles de chanson Niit - Kya Loum
Tay
dina
done
sama
setou
Waxtaan
ak
mane
Fass
yene
na
jakaarlok
mane
Xolate
sama
diar
diar
fi
Bima
dioudo
ba
taay
dji
le
Lane
lafi
def?
Ragne'
nani
dotouma
gone'
Xaam
na
lou
baax
teyit
xaam
na
lou
bone
Taye
souma
fi
diougue'
we'
Louniou
may
sedel?
Maay
deff
lu
baax
Maay
deff
lu
boon
Ma
di
leer
madi
leudeum
Baax
boon
leer
leudeum
maye
tande
ki
ma
thi
wara
doon
Kaay
niou
waxtane'
deugui
djiko
te'
Bayi
yallak
ate'm
Adouna
be'
diakhasso
Di
nga
deff
lu
nice
di
nga
togne
hummm
Kou
thi
nek
am
beuss
ben
beuss
Nga
dioum
def
lodoul
netali
fene
Nita
andak
seytane'
Waye'
yallah
mo
ko
bakhal
Sa
Dieufeul
diou
nice
meune
done
sa
mbalanou
suba
Diema
baax
diema
yiiw
bayi
xel
thi
euleuk
ndakh
maat
na
sorale
Maay
deff
lu
baax
Maay
deff
lu
boon
Ma
di
leer
madi
leudeum
Baax
boon
leer
leudeum
maye
tande
Ki
ma
thi
wara
doon
.Everyday
you
judge
me
Every
time
you
judge
me
Why
do
you
judge
me
Only
god
can
judge
you
and
me
Maay
deff
lu
baax
Maay
deff
lu
boon
Ma
di
leer
madi
leudeum
Baax
boon
leer
leudeum
maye
tande
ki
ma
thi
wara
doon
Kaay
niou
waxtane'
deugui
djiko
Te'
bayi
yallak
ate'm
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.