paroles de chanson Do modèle - Nitdoff
Do
modèle
do
modèle
do
modèle
do
modèle
yow
nigga
do
model
(do
modèle)
Do
modèle
do
modèle
do
modèle
do
Modèle
yow
nigga
do
modèle
(do
modèle)
Do
modèle
(do
modèle)do
modèle
han
nan
tchi
dara
do
modèle
Do
modèle
do
modèle
do
modèle
do
Modèle
yow
nigga
do
modèle
(do
modèle)
Do
modèle
do
modèle
do
modèle
do
Modèle
yow
nigga
do
modèle
(do
modèle)
Do
modèle
(do
modèle)do
modèle
han
nan
tchi
dara
do
modèle
Tchi
alal
tchi
djiko
tchi
diné
do
modèle
Tchi
rewmi
mi
thi
xéet
bi
tchi
ndaw
gni
do
model
Do
model
do
model
do
model
so
model
yow
nigga
do
modèle
Do
modèle
do
modèle
do
modèle
Djitou
nga
falou
mais
tewoul
do
modèle
Bayiwofi
dieuf
boula
kén
meuneu
wayal
Sa
xél
mo
thieuk
walabok
da
nga
tayal
Do
modèle
do
modèle
akh
rek
nga
niou
yorel
Werr
bala
déh
yagui
fayou
ay
brick
Nioune
tchi
bureau
lanielay
khar
yow
ya
ngui
teudiou
hotel
Do
model
do
model
rakh
tchi
doli
do
kou
honnête
Biss
migui
nieuw
da
nga
takk
sunuy
menotte
Bouko
kén
baal
limouniou
yorel
lepp
na
mateu
Économie
rew
faux
billets
dakoy
damate
Fi
kou
beugu
doon
milliardaire
fokk
nga
nanguo
khar
matte
Yén
dale
yén
dérou
serigne
ngueni
yakh
Politigué
sén
talibéyi
djiaay
sen
carte
Nguour
guoufi
niew
nguen
chantage
Dieul
pourcentage
lolou
dale
moy
sen
marque
Do
modèle
do
modèle
tchi
dara
Ana
ragal
yallah
khana
do
domou
daara
Bou
ndieuk
ay
zaïr
nio
daan
féki
baatinn
Wayé
legui
ay
baatiin
kom
kom
laniouy
fighting
Niata
niou
taylé
tchi
lokhoy
toubab
yi
Mamadou
Dia
doyna
cédé
coups
bas
yi
École
dou
diangualé
téré
Touba
yi
Mais
Cheikh
Anta
Diop
dey
dead
rek
mais
dou
bayi
Maître
Babacar
Seye
moy
prix
Nobel
Histoire
migui
neub
ay
criminel
Biss
migui
niew
bagnekat
free
ni
Nel
Son
Mandela
li
nga
gueum
dé
tchi
fidel
Coup
d'etat
dictateur
nga
do
model
Kou
niep
ande
falando
kone
tololel
Signé
ay
accord
di
ceddo
sunu
kaagn
Rêvé
loniou
tchi
sa
discours
khif
bi
diniou
gaagne
Do
modèle
Do
modèle
do
modèle
do
modèle
do
modèle
yow
nigga
do
model
(do
modèle)
Do
modèle
do
modèle
do
modèle
do
Modèle
yow
nigga
do
modèle
(do
modèle)
Do
modèle
(do
modèle)do
modèle
han
nan
tchi
dara
do
modèle
Do
modèle
do
modèle
do
modèle
do
Modèle
yow
nigga
do
modèle
(do
modèle)
Do
modèle
do
modèle
do
modèle
do
Modèle
yow
nigga
do
modèle
(do
modèle)
Do
modèle
(do
modèle)do
modèle
han
nan
tchi
dara
do
modèle
Tchi
alal
tchi
djiko
tchi
diné
do
modèle
Tchi
rewmi
mi
thi
xéet
bi
tchi
ndaw
gni
do
model
Do
model
do
model
do
model
so
model
yow
nigga
do
modèle
Takk
derr
tchi
diguou
tali
melni
deum
mardertali
Diokhé
témer
(500f)
rek
dial
sokhlawoul
di
gaddu
permis
Garde
à
vue
niou
tekk
leu
zermi
dileu
saga
melni
bandit
Formation
bi
nanie
ko
kholaat
autorité
non
dou
gueudé
No
étude
no
éthique
corrompu
no
mérite
Do
modèle
kouniouy
guerre
do
modèle
Hopitaux
yi
nguey
guiss
médecin
you
réw
Pensement
ak
perf
rek
laniouy
meuneu
yéw
Démeul
faye
feulé
so
paré
doga
téw
Ap
sothie
nga
fey
indi
rek
niou
defkop
néw
Ki
niew
amé
metite
dafa
sokhla
kouko
dalal
Niaka
kerseu
infirmière
yi
legui
niepeu
len
ragal
Do
model
do
modèle
yeureumo
seuy
malade
Niakk
contrôle
mo
wareul
laisser
aller
bi
Manque
d'effectif
excusou
tapalé
bi
Ana
emergence
laay
lathie
ki
tchi
palais
bi
Goor
guouy
taak
moromou
goor
do
modèle
Yow
ame
nga
dolé
ko
romb
daur
do
modèle
Niari
werr
yi
ben
yone
laniou
tchiy
oubi
page
Diangue
khalé
yi
nga
djiapelen
en
otage
Ay
grève
you
wékou
tchi
caprice
Ndakh
sa
élèves
yi
diaralounie
leu
sacrifice?
Député
bouy
khasté
di
saga
do
modèle
Transhumé
nga
wédi
sa
ada
do
modèle
Yow
lot
of
nigga
daniou
taré
nigga
Daniouy
fo
tchi
tali
bi
di
faté
séni
bakane
laniouy
taylé
nigga
Yagui
loué
deuké
ndole
dieum
nga
mak
té
wara
maul
(construire)
Boulko
wekk
tchi
ay
lotterie
akeu
khoss
ticket
Bediaw
djiégué
new
done
bébé
beugu
méw
Founie
leu
fekk
ya
gui
namp
ci
ay
prostituées
Yakh
nga
dérou
djiguen
euleuk
boula
sa
Dome
ladjié
ma
lodoon
liguey
= khana
thiagatou
Do
modèle
do
modèle
do
modèle
do
modèle
yow
nigga
do
model
(do
modèle)
Do
modèle
do
modèle
do
modèle
do
Modèle
yow
nigga
do
modèle
(do
modèle)
Do
modèle
(do
modèle)do
modèle
han
nan
tchi
dara
do
modèle
Do
modèle
do
modèle
do
modèle
do
Modèle
yow
nigga
do
modèle
(do
modèle)
Do
modèle
do
modèle
do
modèle
do
Modèle
yow
nigga
do
modèle
(do
modèle)
Do
modèle
(do
modèle)do
modèle
han
nan
tchi
dara
do
modèle
Tchi
alal
tchi
djiko
tchi
diné
do
modèle
Tchi
rewmi
mi
thi
xéet
bi
tchi
ndaw
gni
do
model
Do
model
do
model
do
model
so
model
yow
nigga
do
modèle
Bandit
dou
taukh
dou
guinz
pour
ame
fite
Dou
kogne
bi
ngey
took
di
keuf
ay
wetchit
Milliardaire
do
creer
emploi
Do
modèle
même
sou
fékké
ya
tchi
ame
droit
New
bi
ngay
souli
mouy
guili
tchi
tioumikaay
Takhaw
beuré
dofi
xeureum
beu
xeuy
fi
doon
roi
Do
modèle
do
modèle
do
modèle
ha
nan
tchi
dara
do
modèle
Kou
ame
merite
dounie
leu
diokh
post
Incapable
yi
rek
nioy
sole
cost
(costume)
Conséquence
yi
legui
boy
yi
gni
gui
bayi
diang
Nénagne
diarouko
sama
time
laay
lost
Immigré
yagu
nga
doundé
sunu
bourse
Legui
paré
nga
té
beuguo
delsi
sunu
rew
Bo
niep
defoon
ni
yow
eskeu
dina
bakh
Né
nga
fi
amoul
dara
lign
ley
faye
dafa
néew
Deugu
deugu
khar
tchi
guétte
moleu
tané
Victime
nga
da
ngey
rirendo
rek
topou
tendance
Nane
dafeu
xéw
taukh
dafeu
xéw
pass
pass
bombass
Ya
gui
faté
le
temps
passe
Askane
wi
nga
bokk
doon
tchi
modèle
Linguey
bi
ngey
def
doon
tchi
modèle
Rafetal
sey
dieuf
bofi
diougué
ay
ate
Gniy
niew
demain
diapeleu
model
Do
modèle
do
modèle
do
modèle
do
modèle
yow
nigga
do
model
(do
modèle)
Do
modèle
do
modèle
do
modèle
do
Modèle
yow
nigga
do
modèle
(do
modèle)
Do
modèle
(do
modèle)do
modèle
han
nan
tchi
dara
do
modèle
Do
modèle
do
modèle
do
modèle
do
Modèle
yow
nigga
do
modèle
(do
modèle)
Do
modèle
do
modèle
do
modèle
do
Modèle
yow
nigga
do
modèle
(do
modèle)
Do
modèle
(do
modèle)do
modèle
han
nan
tchi
dara
do
modèle
Tchi
alal
tchi
djiko
tchi
diné
do
modèle
Tchi
rewmi
mi
thi
xéet
bi
tchi
ndaw
gni
do
model
Do
model
do
model
do
model
so
model
yow
nigga
do
modèle
1 Do modèle
2 KK moy number one
3 Ya Better
4 Clando
5 Diyeu maman
6 Jayantel (feat. Mao Sidibe)
7 Roi d'afrique (feat. Mao Sidibe)
8 Maitre kona
9 Badjiel
10 Tellement vu (feat. Mao Sidibe)
11 Règlel
12 Dém Harder
13 Nattu dou wéss (feat. Mao Sidibé)
14 Bokouniou niveau
15 Rancune (feat. Jahman)
16 Feu et flamme
17 Killahrie 3
18 Pure Hardcore
19 Lettre aux étudiants
20 Liniou yallah maye
21 Trahison
22 I Love You
23 Freestyle 4
24 Tekk Ci Brikk 3
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.