Nitdoff - Killahrie 3 paroles de chanson

paroles de chanson Killahrie 3 - Nitdoff



Louné la degu di def tekk
Mbed bi diokhna ma respect
Dey lou deuguou ma dem tchi ba diekh takk
Diayouma kén ay khaute brain
Mais boul teukeulé xandal ak roplane
Niggaz yi dieul sama avance bounie teudé
Dounie nelaw ndakh nio gui tchi problème
My nigga my nigga my nigga my brother
I'm not calling my sister my bitch's
Texte yimey binde tekk ko tchi maîtrise
Mane dolel na flow bi kone fokk sama bic diss
Diougué tchi hood bi di tewal wa ghetto bi
Nenagn meu NDK yaaay sunu hero bi
Gaindé nga mbeurodi lereul nga ndielo bi
Delo nga fierté kén dotoul neuboti
King Killahrie defati hit
Mc no defaak sa defaite bi biigu
Rikk neu lyrics yiy rafete tchi beat
Sama barame tchi kanamou gâchette dou tite
May Ronaldo Zizou di cr7
Nigga magu nga sauroul sa père sétt
Faux bi nga beugu ni Père Seck
Naleu youbou jail feugu leu perpét
Game bi la bousillé fake yi la fusiller
Mc yi exilé ma gueuneu sexy
Niodiwma luxe mane dama musclé
Text you muslimé dokh yagu djiss louné
Meuneuma rap néh kénn douma diss
Mais koumeu diss sama neuf laley one
Niggaz yimeu doon boycotte dimeu siss
King killaharie like that
King killahrie like that
King killahrie like that
Nietelou killahrie laay tekk
Mbetelou fake yimeu doon xéb
Daniou détélou medd beu bone xét
King killahrie like that
Ndeketé feel nga limey tekk
Mbedeu niou maye fite niou def tekk
Boniou beuguoulite di nga niou respect
King killahrie like that
King killahrie like that
King killahrie like that
Nietelou killahrie like tekk
Tchim sa fiteu ngui wathie
Sa koumpeu di lathie
Sa coeur ngui dadjek
Nigga boul topou sa bad mind
Defna si rap loudoul biggy di pac
Soumey binde dey kawéni ni Tech Nine
Bou beat bi metiwoon ni Djiegui siraate
Ladjiel bazik mane dametchiy gueum di rap
Jeufeurouna melni deumeu tchi yap
Kouma warandol tempo bi doma tchi yap
Toxiko hip hop di djiamo rap
Député mbede doon honorable
Didwsquadra takhawé comora
King killahrie laaay tekk
Na niveau adjiou ba high tekk
Mane ken douma djiay prek
Carrière you beuri gui enfer
Ma financé woon seni obsèques
Mbed bi joyotoul concert
Nigga fuck you yén ak sen jetset
Dama visité mbed mi lathie seni mebett
Fathie seni gaume niou desseuk seni legueute
Topou niou bountou bureau yi di feugueute
Ni garabou gouye nitou néne douko dedjieute
Niveau bi wessouna ay fén
Boumadi teukeulek kén tchi niom
Dey moudjié doon ponkali blasphème
Daniouleu yagu di gueumlo ay bullshit beu
Ndjiat leu tchi leurre yi (ndjat leu tchi leurre yi)
Indina diouraumi album tchi fouki ate
Nietelou killahrie (niétélou Killahrie)
Ana gni woneu ben album guay deff daldi délou dealerie
Nigga bi bayeko louga lo succés bi dameu ko poudero
Takouma terré séti wouma serigne
Ndakh dameutchiy saur sama tourando
Forever Uno moy sama numero
King killaharie like that
King killahrie like that
King killahrie like that
Niétélou killahrie laay tekk
Mbetelou fake yimeu doon xéb
Daniou détélou medd beu bone xét
King killahrie like that
Ndeketé feel nga limey tekk
Mbedeu niou maye fite niou def tekk
Boniou beuguoulite di nga niou respect
King killahrie like that
King killahrie like that
King killahrie like that
Nietelou killahrie like tekk
Tchim sa fiteu ngui wathie
Sa koumpeu di lathie
Sa coeur ngui dadjek
Yo Rest in peace my brother othio
Rest in peace my brother toto
Rest in peace sams mon poto
Sac au dos rap feddo putain de cicatrice au dos
Dodo poco boulot mucho argent à gogo tu connais mon logo
Negro auto défense KO
La mort ne vous fera pas de cadeau
Casa lion bocandé hero
Senegal France c'du un a zero
Tirailleur trahi Thiaoroy ebahi
Bombardement c'la france qui remercie
Killahrie tuerie
C'une mutinerie qu'ils ont pretexter pour masquer leurs conneries
Mane dameu diangu tchi demb di taye
Magui doon oup bi tchin bi di taye
Kone taye kou sissou da fekk jaloux
Ndakh yone leu meu djitou Bou game bi faye
Nigga bi bayeko Louga lo
Succés bi dameu ko poudero
Takouma terré séti wouma serigne
Ndakh dameutchiy saur sama tourando (la mort)
Forever uno moy sama numero
King killaharie like that
King killahrie like that
King killahrie like that
Nietoutelou killahrie laay tekk
Mbetelou fake yimeu doon xéb
Daniou détélou medd beu bone xét
King killahrie like that
Ndeketé feel nga limey tekk
Mbedeu niou maye fite niou def tekk
Boniou beuguoulite di nga niou respect
King killahrie like that
King killahrie like that
King killahrie like that
Nietelou killahrie like tekk
Tchim sa fiteu ngui wathie
Sa koumpeu di lathie
Sa coeur ngui dadjek




Nitdoff - Roi d'afrique
Album Roi d'afrique
date de sortie
14-10-2016




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.