Nitdoff - Lettre aux étudiants paroles de chanson

paroles de chanson Lettre aux étudiants - Nitdoff

Diap teweu bayi leu boy
Li takh ngey soneu sa mère leu ak sa baye leu boy
Loumou meti dakoy mounie mom gawouleu dioy
Mi gui fanane tchi couloir yi djissoul lale bou noy
Sa you seukheuté niou yonéko ay gandi thioy (gendarmes)
Guinaw xam xam dou diekh kone nak diang dou doy
Na nguen gueum sen bop na nguen visé le top
Fou nguen degu tén bou bale lagu lén feu rote
Kiy geuneu xaragn djitou niep moy kiy wouti di yokk
Neugueundigou sabablou wekou thi god
Gni lay diéma décourager gni lay deuké support
Niar yeupeuley motiver nguir nga kham sa bopp
Niata ate nga tchi banc yi deuké sacrifce
Beugu wagni thioneu waadiour takh neu sas bi diss
Koussa dome di étudiant na nga fier sa fils
Djiguenou taye Kén demoul niou dess niepeu ambitieuse
Manéwoneu nala big up souma teuyeuté mic
Manéwoneu nala big up souma teuyeuté mic
Manéwoneu nala big up souma teuyeuté mic
Manéwoneu nala big up souma teuyeuté mic
Hey yow bou soufsi selaw beu niep teud di nelaw
Yagui cogiter sa mind ndakh beuguo ken koula raw
mouy taaw mouy naathie mba mouy tangue di ngelew
Ya ngui mathie tantieulo tchi bus yi yaaba tchi vélo
Biniouy wakh niakh diarigno yay kiko yélol
Bi seu morome yi yakh sen ndaw deuké fo
Ya ngui soucié wou tchi sa avenir H24
Kone taye djissouma lou wareu takh nga baissé bras
Na nga jafandou beu biss nga degu c'est la consécration
Del teudalé number one di yewouwalé number one
Ni nga def beu aksi fi étudiant dara diombeuleu
President mi gui yow
Monsieur le juge mi gui yow
Docteur Professeur potentiel bi mingui si yow
Primaire secondaire lycée parents ya ngui faye
Niew nga fac done nga mak war nga yorr sa bopp taye
Diguénté week-end ak vacance wouteul wétchiit bofeu raye
Manéwoneu nala big up souma teuyeuté mic
Manéwoneu nala big up souma teuyeuté mic
Manéwoneu nala big up souma teuyeuté mic
Manéwoneu nala big up souma teuyeuté mic
Li leu takha diouk nak boulko teukeulek nix
Nio ngui rakh seni biir beugu def politique
Amnaniou sen job beu rawalé sen ndiabot
Etudiant danko doon bén lapse de temps
Bouleu ken manipulé dileu bolé tchi ay clan
Yow ak sey objectif yéneu nekk tchi ben course
Niakeu fayda État wessouwoul di tardel séni bourse
Ray naniou Balla Gaye kill Bassirou Faye
Nane nga meuné khanié waadiour sen dome louy sa laye
Bataxal bi maako binde yonéko bepp etudiant
Gni fi nekk ak gni nekk bitim rew yén nieupey meritant
Na nguen roy cheikh anta diop nguir marqué seni temps
Manéwoneu nala big up souma teuyeuté mic
Manéwoneu nala big up souma teuyeuté mic
Manéwoneu nala big up souma teuyeuté mic
Manéwoneu nala big up souma teuyeuté mic
Mouy taw di nathie bouy dem dou wathie
Dou niane dou lathie sawar neu si diang
Dou soneu dou tayi dou freq diotay
Réussir liguey meuneu wouti séni wadiour
Mouy taw di nathie bouy dem dou wathie
Dou niane dou lathie sawar neu si diang
Dou soneu dou tayi dou freq diotay
Réussir liguey meuneu wouti séni wadiour

Nitdoff - Roi d'afrique
Album Roi d'afrique
date de sortie
14-10-2016

Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.