Nitdoff - KK moy number one paroles de chanson

paroles de chanson KK moy number one - Nitdoff



Medaillou number one la weko nak loum togu yak done lekou mak
Kou tonguook mome yaye rethiou niak rap pur et dur doù fethiou niak
Biggui na khamni amna rak tchi beat bi sakh dey djiékou pac (2pac)
Sayo dégué wouy walou kou djiaguédi mo dadjiek kou djiag
Kk mo djité gniniouy djiteul ak gni djitéwoon
Taye tool béh soukheeut maye bayalél gni dji teuwoon
Xam xam ba tchia coki nak katane gui tchi dondi nak
Xalé bou xéleum déh khassane lek lek dey sokhla woki mak
Wané na founé tchi fane yeup dotoul competir
Deugueur boppeu takh ma deflen mala dilen dompté khir
Corner yeup la conquerir Koba vont en perir
Xelou dieun nga yorr do contenir takh foma compé miir
Fils doneul mini may maxi eupeuleu daradjia
Pistonel mc bouy aksi ma koy dieul ko deureudjieu
Beat bi loumou feugu meu reude tek tchi kou melodieux
Gunzout
Diwsquad
LG
Galsen
Hands'up
Please let me hear you say KK Moy Number one
Kk moy number one lou khel yi meuneu nangoula
Bo ticholiwoul li dess seu life bi yeup ay niandula
Fuck gni tchi andouleu surdose bouniou ndiambouleu
Only real moniouy cons nioun fake bou niou niam douleu
Midi diotna ni nagn nga dieul ampoule di niit
Hit yi bari ni gagni nigga dampoul tchi nit
Rabou mbed la niodi incarné marginal
Tareul kocc barma mouy dioli tchia internationnal
Niom niep la craquer sen code yi ak sama virus man
Gni ma dane dingkat demb nio melni kou rouss men
Bank len lokho yen tasspé naba dou murder As
Legui rap agneau leu tiouné yéy ame code
Bou beat bi wangeto nga djiss gni war mbame yi meunounio kotte
Swagger boy nio beuri niom niepeu nourau rap
kotchi tégual right mou teup saga bou khamé mouno raak
Gunzout
Diwsquad
LG
Galsen
Hands'up
Please let me hear you say KK Moy Number one
Meunoulenma juger fuck seni magistrature
Boudé deugu leu keufeul mic ma djiss sa rap pur
Boudé sa opinion danie leu kay dicté my nigga fi dofi ame moyenne
Indil sa cahier nga djiss sa rature
Wekh ni domou nima nigga doma nima
Tchi eukhlou rap galsen amna kouy wakh ni do monument
Deugu leu dama zarbi mais maley firil saar bi
Djibeuleoul tchi mane indalé adiyeuk ziaar bi
Medaille bi doréna founé mbed decoréma
Sayouma yoré mic nga degu amna niam gooréna
Nelen sen khel yi dale ndakh ndk dou meusseu sak
Gunzout
Diwsquad
LG
Galsen
Hands'up
Please let me hear you say KK Moy Number one




Nitdoff - Roi d'afrique
Album Roi d'afrique
date de sortie
14-10-2016




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.