Philip Monteiro - Yaw Reck Lev (Duet Corine) paroles de chanson

paroles de chanson Yaw Reck Lev (Duet Corine) - Philip Monteiro



Oubil nala sama khol yala nagua si guiss
Lou ler tei ga khamni amoul kenen kou doul yaw.
Mbeuguel bi nek si mane mougui dima dane.
Tegue nani di neu done sa nene bi gay tete...
Mane mi souma meunone dina bokeu ak yaw ben yone di leu wowei nene
Touti dakh mane mi mane mii gnanou ma
Yalla. gnanou ma yalla dess fi mane rekeu
Ya nek sama khol guissou ma kenen kou doul yaw. oubil na la sama khol
Tei dina done sa néné.
Amna gnou wakh beuguel tiono rek leu
Wayei magui ley khamal dou ken yaw rek leu
Beuss bouma la guissei la khamni khole day
Guissei. tei fok na do meuseu tass sama yakar
Boul am loy ragal dou ma meuseu diay sama tar.
Dina la wowei papa cheri dina done sa sokhna dina
Done sa baby bi lay fadial sey sokhla ohh baby yaw rek leu
Ya nek sama khol guisou ma kenen kou doul yaw oubil nala sama khol
dina done sa néné
Yaye sama dolei soudoul yaw wate na ni dou done kénéne.
Diokh nala sama bopp tei dina le bégueul
Baby boul soneu geumeul ni yaw rek leuuuuuuu dou done kénéne
Oubil nala sama khol bi
Dina done sa baby
Dina done sa sokhneu
Dina done sa néné




Philip Monteiro - Philip Monteiro
Album Philip Monteiro
date de sortie
02-02-2010




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.